Vous êtes sur la page 1sur 4

Texte original : PHAST

Traduction : Salif NDAO, Sankoung DIAKHITE


RODI
Production : GADEC
motassi@yahoo.fr

8
YOONI JIWU JÀNGORO

Jiwu jàngoro yi, bët du


leen gis. Ñu ngi leen di
fekk ci sënn yi ak barab yu
tilim yi, ak ci neefere yi.

Su nit deme ganaw kër,


weñ yi dañu i dàll ci
neefere yi ; ñëw dàll ci
ndox yi ak lek yi.
Tamit ndox u taw yi i
walangaan dafa i indiwaale
neefere yi ci dex yi ak
deeg yi, jiwu jàngoro jaare
fa, wasaaroo fu nekk.

Weñ yi i toŋ ci neefere yi


ñoo i yobaale ci seeni tànk
neefere yi

2 7
FATT YOONI JIWU JÀNGORO YOONI JIWU JÀNGORO

Nit ku naan ndox mu tilim


Raxas yoxo yi ganaw
(ci dex walla ci barab bu ñu
gennug wanak yi dafa i tax
aarul) dafa i wonnaale jiwu
loxo du taq jiwu jàngoro.
jàngoro yi

Weñ yi i laal lekk yi ak


Up ñam yi dina tax weñ du seeni tànk, ñoo fa i bayi
ñu leen laal ba taq leen. jiwu jàngoro yi

Su nit deme wanak loxom la


i laaboo su ko defe dafa i
Naan ndoxum suukar ak taqaale jiwu jàngoro yi.
xorom dafa i tax nit ku Xale yi dañu i faral di dugal
feebar dawbiir du ñakk seeni yoxo ci seeni gemeñ
ndox mu bare ci yaram am. yi
Mak yi itam mën nañu wàll
ñam yi su ñu i togg
6 3
YOONI JIWU JÀNGORO FATT YOONI JIWU JÀNGORO

Su nit lekke ñam bu weñ yi Naan ndox ci barab bu ñu


laal, dafa i lekkaale jiwu aar (robine walla ndaal bu
jàngoro yi. tëju) amul ngaañ.

Budee robine amul ndaal


Su nit lekke, ñam bu tilim, bu tëju amul, man nañu
ñam bi dafa i dem ci mbaq baxal ndox mi ci diiru 10
bi (biir) , dem ci butit yi. simili ngir rey jiwu jàngoro
Dafa i yobuwaale jiwu yi. Ndox mi nekk ndox mu
jàngoro yi. sell.

Jëfandikoo wanak yi dafa i


Jiwu jàngoro yi i agg ci daq bep jiwu jàngoro bu i
butit yi ñoo i dawloo biir bi. bayekoo ci dem all.

4 5