Vous êtes sur la page 1sur 20

Recueil d’invocations traduites en wolof

Par EL HADJI MALICK SOW

1
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Du même auteur

1. Essai de traduction du Coran en wolof juz’u amma

2. Traduction du livre al akhedary en wolof.
3. Traduction en wolof du livre rouhoul adab de cheikh Ibrahima Niass
4. Recueil d’invocations traduites en wolof.
5.Traduction en wolof des 40 hadiths de l’Imam AN Nawawi
6. Traduction en wolof du livre Muniyatul muriid
7. Traduction en wolof du livre al ifaadatul ahmadiya
8. Recueil de zikr traduits en wolof
9. Traduction en wolof du livre Hamziya de Busayri

2
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

INTRODUCTION

Le Prophète (que Dieu lui accorde la bénédiction et le salut) a dit:

«...‫» َم ْن ا َم َم َم ا َم ِر ًقي ا َمَيْنَيَم ِر ا ِر ِريا ِر ْن ًق ا َم َّه َما ُهللاا َم ِر ًقي اِر َم ا ْناَمَّهِرا‬

Et aussi :

‫ « ا‬...‫» َم َّه َم ا ُهللاا ْن َمًقا َمِر َم ا ِر َّه ا َم ْنَيًق ا َمَيَمَيَّه َميُهللاا َم َم ا َمِر َما‬

Et sur cet autre dire :

3
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Cet ouvrage, écrit par El Hadji Malick Sow disciple de Cheikh Ibrahima Niass est un recueil
d’invocations.

Nous avons essayé à travers cet ouvrage de traduire certaines invocations en wolof pour permettre à
chaque disciple aspirant à la perfection à parfaire sa religion.

Chers lecteurs, puisse cet ouvrage répondre par la grâce d’Allah le Généreux à votre attente et vous
être utile.

4
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

I. Traduction en wolof des formules utilisées dans la wazifa

‫وُس َرال َحِتاَر َحِت‬

Saaru aji ubbée ji ‫ُس َر‬

‫ميحرلا نمحرلا هللا‬ ‫بسم‬

Mboleem xaaju cant yi al-ḥamdu ‫َحْلاَر َحْل ُس‬

Ñeel na Yàlla lil-Lāhi ‫َحِت َحِت‬

Miy borom mbindeef yi rabbil-`ālamīna ‫َرو َحِتِّب اَحْل َر اَر َحِت َر‬

Mooy aji yёrёm mbindaafóon yёpp si

adunyaa
ar-raḥmāni ‫ال َحْل َر َحِت‬

Mooy aji yёrёm jullit si allaaxira ar-raḥīmi ‫الَحِت َحِتي‬

Mooy buurab besu pay ba maliki yawmid dīni ‫َر َحِت َحِت َرَي َحْل َحِت ا ِّبَحِت َحِت‬

Yaw Yàlla 'iyyāka ‫َحِت َر‬

La ñiy jaamu na`budu ‫َرَي َحْل ُس ُس‬

Té yaw Yalla wa'iyyāka ‫َر َحِت َر‬

‫َحِت‬
La ñiy dimbanikoo ci suñu jaamu nasta`īnu ‫َر َحْل َر ُس‬

5
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Yal na nga jubal ñu ihdinā ‫َحْلا َحِت َر‬

Yoon ṣirāṭa ‫ا‬ ‫َحِتِّب‬

‫ال َرل َر‬

Budi aji jub al-mustaqīma ‫اَحْل ُس َحْل َر َحِت َري‬

‫َحِت ل َر َحِت‬
Yoonu ñaa ña ṣirāṭal-ladhīna ‫ا ا َر‬ ‫َر‬

Xeewee nga 'an`amta ‫َر َحْلَي َر َحْل َر‬

Ci ñoom `alayhim ‫َر َرَحْل َحِت َحْلي‬

Du yoonu ñuñ mere ña ghayril-maghḍūbi ‫َر َحْلَحِت اَحْل َر َحْل ُس َحِت‬

Ci ñoom `alayhim ‫َر َرَحْل َحِت َحْلي‬

‫َحِت‬
Du caagan yoonu wёy réer ña walaḍ-ḍāllīna ‫َر َر ا اِّب َر‬

6
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Formule de demande de pardon

‫اَحْل َحِت ي ا َحِت‬ ‫َر َحْل َرَي َحْل َحِتل ُسل‬

‫َر َحِتاَر َر َحِت َرا َر اَر ُّي اَحْل َر ُّي ُس‬ ‫َر َر‬
Astaghfirullâhal-‘azîmal-lazî lâ ilâha illâ huwwal-hayyul-qayyûm

Maa ngi baalu Yàlla 'astaghfirul-Lāh ‫َر َحْل َرَي َحْل َحِتل ُسل‬
Mu magg mi al-`aḍhīma ‫اَحْل َر َحِت َري‬
Mi nga xamne al-ladhī ‫ا َحِت‬
Kenn du Yàlla kudul moom lā 'ilaha 'illa huwa
‫َر َحِتاَر َر َحِت ُسا َر‬
Mooy ki dund te du dee ba mukk al-ḥayyu ‫اَر ُّي‬
Moy ki taxawee lepp al-qayyūmu ‫اَحْل َر ُّي ُس‬

7
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Salātul fātihi

‫َحِت‬
‫ُس َحْل َحِت َر َر َحْل َرَر َحِتا اَحِت َر َر َر َر َر َحِت َحِتل َحْلاَرَحِتِّب َحِت َحْلاَرَحِتِّب َر َحْلْلَر َحِتد َحِت َر َحِت َرل َحِتا َر‬ ‫ٍد َحِت َحِت‬
‫ُسَر َراَحْلل ا َحِت ا َر‬ ‫َرا ُس ي َر َحِتِّب َر َرى َر َحِتِّب َحِت َر‬
.‫اَحْل َر َحِت َحِتي‬ ‫َر َحِتوَحِت َحِت َحْل َر َحِتوَحِت‬ ‫َحِت َحِت‬ ‫َحِت‬
‫َر‬ ‫اَحْل ُس َحْل َر َحِتي َر َر َرى ا َر‬

Yaw Yàlla allāhumma ‫َرا ُس ي‬

Jullil ṣalli ‫َر َحِتِّب‬
Ci suñu sangg `alā sayyidinā ‫َر َرى َر َحِتِّب َحِت َر‬
Muhammed muḥammadin ‫ُسَر ٍد‬
Ki tijji al-fātiḥi ‫َراَحْلل اَحِت َحِت‬
Li tёjuwóon limā 'ughliqa ‫اَحِت َر ُس َحْل َحِت َر‬
Te mottali Wal khātimi ‫َر َحْل َرَر َحِتَحِتا‬
La jiituwóon limā sabaqa ‫اَحِت َر َر َر َر‬
Kiy dimbale dёgg nāṣiril-ḥaqqi ‫َر َحِت َحِتل َحْلاَر َحِتِّب‬
Ci dёgg bil-ḥaqqi ‫َحِت َحْلاَر َحِتِّب‬
Kiy jubale wal-hādī ‫َر َحْلْلَر َحِتد‬
Ci sa yoon 'ilā ṣirāṭika ‫َحِت َر َحِت َرل َحِتا َر‬
Bu jub bi al-mustaqīmi ‫اَحْل ُس َحْل َر َحِت َحِتي‬
Julli bii def ko ci mbooléem ñoñu ‫َر َرى اَحِت َحِت‬
Yonent bi
wa`alā ālihi ‫َر‬
‫َر َحِتوَحِت‬
Kéem nu Yonent tollu ci yaw Yàlla ḥaqqa qadrihi ‫َر‬
Ak dayoom bu magg bi wamiqdārihil-`aḍhīmi ‫َر َحِت َحْل َر َحِتوَحِت اَحْل َر َحِت َحِتي‬

8
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Jawharatul kamal

Yaw Yàlla Allâhumma ‫ا ُس ي‬

Jullil çalli ‫َر َحِتِّب‬
Té nga dolli musal wa sallim ‫َر َحِتِّب َحْلي‬
Ci kii nga xamné mooy sa jёmmi
'alâ 'aynir-rahmati ‫َر َرى َر َحْل َحِت ال َحْل َر َحِت‬
yёrmandé (Yónnent bi)
Biy dellu ci borom bi Ar-rabbâniyyati ‫ال َحِت َحِت‬
‫اَحْل ُس اَر َحِت‬
Mooy wurus wal yâqûtati ‫َر َر‬
Badi dёgg dёgg wuruss (bi nga ‫اَحْل َر ِّبَحِت َر َحِت‬
xamné dafa lamboo daraja ju rёy)
Al mutahaqqiqati ‫ُس َر‬
‫َحْلا ئَحِتطَر َحِت‬
Ki péeg Al hâ'itati ‫َر‬
‫َحِت لَر َحِت ُساَحْلل َحِت‬
Mboolém degg degg yi bimarkazil-fuhûmi ‫ُس‬ ‫َرَحْل‬
Ak maanaa yi wal-ma'ânî ‫َر اَحْل َر َر َحِتا‬
Mooy léeri adina yi (nékk gi) wa nûril-akwâni ‫َر ُس َحِتو َحْلألَر َحْل َر َحِتن‬
‫اَحْل َر َرك َحِتَرَحِت‬
Bi nga xamne dafa formewu al-mutakawwinati ‫ُس ِّب‬
‫َحِت‬
Nékk di doomi aadama Al ādamiyyi
‫َحْل َرد َحِتِّب‬
Kiy borom dёgg ṣāḥibil-ḥaqqi ‫َر َحِت َحِت َحْلاَر َحِتِّب‬
Biy déllu ci borom bi ar-rabbāniyyi ‫ال َحِتَحِتاِّب‬
Mooy melax (éclair) al-barqi ‫اَحْلَرَي َحْلل َحِتق‬
Bay melxati āl'asṭa`i ‫َحْلألَر َحْل طَر َحِت‬
Ci niiri tono yi bimuzūnil'arbāḥi ‫َحِت ُسُس َحِتن َحْلأل َحْلَروَر َحِت‬
‫اَحْل اَحِتَر َحِت‬
Bay féesalal al-māli'ati ‫َر‬
Ñéel képp ku taataan likulli muta`arriḍin ‫اَحِت ُسك َحِتِّب ُسَرَي َر ِّبَحِتل ٍد‬
Moo xam géej la yor minal-buḥūri ‫َحِت َر اَحْلُس ُس َحِتو‬
Moo xam ndab la yor wāl'awānī ‫َر َحْلألَر َر َحِتا‬
Mooy léer gi nga xamne dafa léer
bay melax
wanūrikal-lāmi`i ‫َر ُس َحِتو َر اَّل َحِت َحِت‬
Sa léer gi nga xamne al-ladhī ‫ا َحِت ي‬

9
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Féesalee nga mala'a ta ‫َر َرَلَحْل َر‬

‫ت‬
si moom bihi ‫َحِت َحِت‬
Sag nékk gi nga xamne kawnaka ‫َر َحْل َر َر‬
Dafa wёr daj al-ḥā'iṭa ‫َحْلاَر ئَحِت َر‬
Ci mbooléem barab yi bi'amkinatil-makānī ‫َحِتَر َحْل َحِتكَر َحِت اَحْل َر َرك َحِتا‬
Yaw Yàlla Allāhumma ‫ا ُس ي‬
Jullil ṣalli ‫َر َحِتِّب‬
Té nga dolli musal Wa sallim ‫َر َر َحِتِّب َحْلي‬
Ki nga xamne mooy jёmm dёgg `alā `aynil-ḥaqqi ‫َر َرى َر َحْل َحِت َحْلاَر َحِتِّب‬
jёmm dёgg ji nga xamne allatī ‫َرا َحِت‬
‫َحِت‬
Ci moom minhā ‫َحْلَي َر‬
Lay féeñée tatajallā ‫اَرَيَر َرج ى‬
Adinay dёgg yi `urūshul-ḥaqā'iqi ‫و َحْلاَرَر ئَحِت َحِت‬ ‫ُس ُسل ُس‬
‫َر َحْل َحِت اَحْل َحِتو َحِت‬
Mooy jёmmi xam xam `aynil-ma`ārifi ‫َر َر‬
‫َحْلألَر َحْلَي َحِت‬
Yu jub yi al'aqwami ‫َر‬
Yónnent bi mooy sa yoon ṣirāṭika ‫َحِت َرل َحِتا َر‬
Bu matale bi at-tāmi ‫ا َحِت‬
Bu jub xocc bi al'asqami ‫َحْلألَر َحْل َر َحِتي‬
Yaw Yàlla Allâhumma ‫ا ُس ي‬
Jullil çalli ‫َر َحِتِّب‬
Té nga dolli musal wa sallim ‫َر َحِتِّب َحْلي‬
Ci kii nga xamné mooy ‫َحْلا َحِتِّب َر َرى اَرَحْل َحِت‬
féeñuwaayu dёgg (Yónnent)
'alâ tal'atil-haqqi ‫َر‬ ‫َر‬
Tey féeñée ci dёgg (Yàlla) bil-haqqilkanzil-a'zam ‫َحِت َحْلاَر َحِتِّب‬
Kiy koom Al kanzil ‫اك َحْل َحِت‬ ‫َر‬
Bu magg mi Al a'zam ‫ألَر َحْل َرَحِتي‬
Sa bёbb bi nga xamné ifâdhatika ‫ضَحِت َر‬ ‫َحِتفَر َر‬
Jugé na ci Yàlla minka ‫َحِت َحْل َر‬

10
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Déllu ci Yàlla ilayka ‫َحِتاَرَحْل َر‬

‫َحِت اَر َحِت‬
ki péeg ihâtatin-nûril-mutalsam ‫َر‬
Mbooléem léer yi laqu ci xam
xam
an-nūri l-muṭalsami ‫اُّي َحِتو اَحْل ُس طَرَحْل َر َحِتي‬
Yal na julli çalla ‫َر ى‬
Yàlla allâhu ‫ُس‬
‫َر َر َحِت‬
Ci Yónnent bi 'alayhi ‫َحْل‬
‫َر َرى اَحِت َحِت‬
Ak ci ñoñam wa 'alâ âlihî ‫َر‬ ‫َر‬
Julli goo xamné çalâtan ‫َرَّلَر ًة‬
Di nga ñu xamalée yaw Yàlla tu'arrifunâ ‫اُسَي َر ِّبَحِتلفُسَيَر‬
‫َحِت‬
Ci julli goo gu bihâ. ‫ِبَر‬
Kiy Yónnent bi (SAWS) iyyâhu ‫َحِت ُس‬

11
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Formule de clôture

Yàlla 'Innal-Lāha ‫َحِتن َر‬

Aki malaaykam yi Wa malā'ikatahu ‫َر َر َرَّلئَحِت َركَر ُس‬
Da ñiy julli Yuṣallūna ‫ل ُّي َرن‬ ‫ُس َر‬
Ci Yónnent bi `Alān-nabiyyi
‫َر َرى ا َحِت َحِتِّب‬
Ey yéen ñi gёm Yā'ayyuhāl-ladhīna āmanū ‫َر َرَيُّي َر ا َحِت َر َر ُس‬
Julli léen Sallū ‫َر ُّي‬
‫َر َر َحِت‬
Ci moom `Alayhi ‫َحْل‬
‫َحِت‬ ‫َحِت‬
‫َر َر ِّب ُس اَر َحْل ًة‬
Te ngen def ci moom salaam bu
Wa sallimū taslīman
matale
Tudd naa sellak sama borom Subḥāna rabbika ‫ُس َحْل َر َرن َروَحِتِّب َر‬
Mi nga xamne moo meloo melokaan ‫و َحِت اَحْل َحِت َحِت‬
yu tedd, yu kawe yi nga xamne
Rabbil-`izzati ‫َر ِّب‬
‫ل ُسل َرن‬ ‫َر َحِت‬
Wuutenag ni ko yeefer yi di mellalee `Ammā yaṣifūna ‫َر‬
Jàmm Wa salāmun ‫َر َر َرَّل ٌم‬
‫َحِت‬
Yal na nekk ci mboolem Yónnent yi `Alāl-mursalīna ‫َر َرى اَحْل ُس َحْلل َر َر‬
Cant Wal-ḥamdu ‫َر َحْلاَر َحْل ُس‬
Ñeel na Yàlla Lil-Lāhi ‫َحِت َحِت‬
Miy borom mbindéef yi Rabbil -`ālamīna ‫َرو َحِتِّب اَحْل َر اَر َحِت َر‬

12
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

II. Bismil’ilaahi ashkurul-murīdā

‫َحِت َحِتي َحْل َحِت اَر َحِت‬

Ci turu Yàlla bismil'ilahi ‫َحْل‬
Laay sante 'ashkuru ‫َر َحْل ُسك ُسل‬
Ki ñu namm ki al-murīdā ‫اَحْل ُس َحِتل َر‬
Te maa ngi yaakaar wa'artajī ‫َر َحْلَروَرَحِتَتى‬
Ci sa ngëneel yaw Yàlla bifaḍlihi ‫َحِتَرل َحْل َحِت َحِت‬
Ndollal al-mazīdā ‫اَحْل َر َحِت َر‬
Laaj naa ko moom Yàlla sa'altuhu ‫َر َراَحْلُس ُس‬
Mu may 'an yutḥifa ‫َرن َيُسَحْل َحِت َر‬ ‫َحْل‬
Jaam bii di muriidu (ku bëgg) al-murīdā ‫اَحْل ُس َحِتل َر‬
‫َحِتد َحِت‬ ‫َحِت‬
May gu juge ci tabéem gi moom Yàlla min jūdihi ‫َحْل ُس‬
May goo xamne mā ‫َر‬
‫َر َحْل َرج َر اَحْل َر َحِت َر‬
Dana lott loo mbooleem mdindéef yi ci ñu
'a`jazal-`adīdā
xam dayoop may yak ndollal ya
‫َحِت اَحْل ُس َحِت‬
Ci luñ naan xam-xam la minal-`ulūmi ‫َر ُس‬
Ak ci lépp luñ naan wërsëk Wa minal'arzāqi ‫َر َحِت َر َحْلأل َحْلَروَرز َحِتق‬
Rawatina faḍlan ‫فَر َحْل َّلًة‬
Ci jikkó yu rafet yi
Wa min ‫َر َحِت َحْل َرَر َحِت َحِت َحْلألَر َحْل َّلَر َحِتق‬
maḥāsinil'akhlāqi
Maa ngi ñaan Yàlla 'as'alu ‫َر َحْل ُس‬
‫َرل‬
Ci turëm bii di Allaahu bil lāhi ‫َحِت َحِت‬
Ak ci turam bii di rahmaan (yërëmekat bi) Wa bir-raḥmāni ‫َر َحِت ال َحْل َر َحِتن‬
Ak ci turam bii di muhayminu (ki seede te
Wa bil muhaymini ‫َر َحِت اَحْل ُس َر َحْل َحِت َحِت‬
janook lepp)
Ak ci turam bii di mannaanu Wa bil-mannāni ‫َر َحِت اَحْل َر َحِتن‬
Duma soxlowoo mukk Lā iḥtajtu ‫َر َحْل َر َحْلج ُس‬
‫َرَحْل َر َحْلَحِتَحِت‬
Ci wallu kudul Yàlla naḥwa ghayrihi ‫َر‬
Ci sama dundu fīl-`umri ‫َحِت اَحْل ُس َحْل َحِتل‬

13
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Du ma sakku mukk falā 'arūmu ‫فَرَّلَر ُسَرو ُس‬

May minnatan ‫َحِت ًة‬
Ci kudul Yàlla lilghayri ‫اَحِت َحْل َر َحْلَحِت‬
Man Baay Ñas 'inni ‫َحِتَحِتِّب‬
As njaam laa `ubaydun ‫ُسَرَي َحْل ٌم‬
‫َحِت‬
Nekkal ku oomal ki nga xamne lilghaniyyi
‫ا َحْل َرَحِتَحِتِّب‬
Mo mingóo sama mbir, mingóo mbiru jaam
al-walī ‫اَحْل َر َحِت‬
yёpp
Maa ngi koy yaakar 'arjūhu ‫َحْلَرو ُس ُس‬
Ne danama defal lepp luy lu baax lumu am lī ‫َحِت‬
Ak kepp ku mingóo ak man si sama njaboot Wa kullu man yuwālī ‫َر ُس ُّي َر َحْل َيُس َر َحِت‬
Moom Yàlla huwa ‫ُسا َر‬
Mooy buur bu tedd bi al-`azīzu ‫اَحْل َر َحِت ُس‬
Kudul moom Yàlla ghayruhu ‫َرَحْلَي ُسلُس‬
‫َحِت‬
Ku lott la, ku torox la dhalīlu
‫َرا ُس‬
Moom Yàlla Wa huwa ‫َر ُسا َر‬
Moy ku tedd ki al-karīmu ‫اَحْلك َحِتل ُس‬ ‫َر‬
‫َحِت‬
Mooy mayekat bu barile lool al-wāhibu ‫اَحْل َر ا ُس‬
‫َحِت‬
Mooy ku magg ki al-jalīlu
‫َحْلْلَر ُس‬
Man Baay Ñas maa ngi sakkul samay
'arūmu lil'ahbābi ‫ُسَرو ُس اَحِتَلَر َحْل َر َحِت‬
andandoo
Lepp luy jappandal kulla yusri ‫ُس ُس َحْل َحِتل‬
Na nga leen fegal (daqal) waltakfihim ‫َر اَحْلَر َحْلك َحِتل َحِت َحْلي‬
Yaw suma borom Yā rabbi ‫َر َرو َحِتِّب‬
Lepp luy jafe-jafe kulla `usri ‫ُس ُس َحْل َحِتل‬
Ak ñakk bum leen lor mukk Lā ḍarrahum faqrun ‫ضلُسا َحْلي فَرَي َحْل ٌمل‬ ‫َر َر‬
Bumu jot ba di lor walā yusalliṭu ‫َر َر ُس َر َحِتِّب ُس‬
Ci ñoom `alayhim ‫َر َرَحْل َحِت َحْلي‬
Noon yi al'a`dā'u ‫َحْلألَر َحْل َر ُس‬

14
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Ñaan naala lii yaw mi nga xamne yaay ku

mandu ki
yā man yuqsiṭu ‫َر َر َحْل َيُس َحْل َحِت ُس‬
Yëkëti nga samay taalibe yaw Yalla rafa`tahum ‫َروفَرَي َحْل َرَي ُس َحْلي‬
Muy ngëneel goo xamne may nga léen ko faḍlan ‫فَر َحْل َّلًة‬
Si sa tur gu magg gi ñuy tuddu bidhikrikal-`aḍhīmi ‫َحِت َحِت َحْل َحِتل َر اَحْل َر َحِت َحِتي‬
Yaw Yàlla may léen ñu woomal fa'aghnihim ‫فَرَر َحْلَحِت َحِت َحْلي‬
Ñoom ñëpp ṭurran ‫اُسًّل‬
Ci sa ngëneel yu mak yi nga xamne Bi faḍlika ‫َحِتَرل َحْل َحِت َر‬
Dafa matale fepp al-`amīmi ‫اَحْل َر َحِت َحِتي‬
Yaw Yàlla haar nga léen ḥamaytahum ‫َرَرَحْلَيَرَي ُس َحْلي‬
Ba doo tuñu tudd kudul yaw
`an dhikri kulli ‫َر َحْل َحِت َحْل َحِتل ُس َحِتِّب َر َحْلَحِت‬
ghayri
Kon feesalal fāml'a ‫فَر َحْل َرَلَحْل‬
Séen xol yi Qulū bahum ‫ُسَي ُس َرَي ُس َحْلي‬
Ci lepp luy mbòot Bikulli sirri ‫َحِت ُسك َحِتِّب َحِت ِّبَحِتل‬
May léen kër yu baax yi ñu moom ko Mallikhumud diyāra ‫َر َحِتِّب َحْلك ُس ُسي ا ِّبَحِت َر َرو‬
Ak alal wāl'amwālā ‫َر َحْلألَر َحْل َر َر‬
Te nga musal leen ci luy lore (beew) wanajjihim ‫َر َرَحِتنِّب َحِت َحْلي‬
Te nga jox leen ndollal wa'a`ṭihim 'anfalā ‫َر َر َحْل َحِتط َحِت َحْلي َر َحْلَي َرل َر‬
Taxawalal 'aqim ‫َر َحِت َحْلي‬
Seeni jubluwaay yi ñu jublu Wujūhahum ‫ُس ُس َرا ُس َحْلي‬
Sa diine ju jub ji lidīnikal-qawīm ‫اَحِت َحِت َحِت َر اَحْل َر َحِت َحْل‬
Tallalal ci ñoom may yoo xamne Wamudda fīhim ‫َر ُس فَحِت َحِت َحْلي‬
Ci sa baax gi bifaḍlika ‫َحِتَرل َحْل َحِت َر‬
Gu matale gi lay juge Al -`amīm ‫اَحْل َر َحِت َحْلي‬
May leen ñu am Nilhum ‫َحِتَحْل ُس َحْلي‬
Te dolli leen ci séeni am-am ya Wa zidhum ‫َر َحِتز َحْلد ُساي‬
Keem dëggu Biqadri ṣidqi ‫َحِتَر َحْل َحِتو َحِت َحْل َحِتق‬
‫ُس َحِت َحِتل ٍد‬
Bepp taalibe kulli murīdin ‫ِّب ُس‬

15
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Ak mbëggeelam namu tollu Wa biqadri shawqi ‫َر َحِتَر َحْل َحِتو َر َحْل َحِتق‬
Man Baay Ñas 'inni ‫َحِتَحِتِّب‬
Bёgg naa urīdu ‫َحِتُسو ُس‬
lu juge ci yaw Yàlla Minka ‫َحِت َحْل َر‬
Lifi nekk Bal ‫َر َحْل‬
Xam nga lima bëgg Wa ta`lamu ‫َر اَرَي َحْل َر ُسي‬
Man Baay Ñas 'inni ‫َحِتَحِتِّب‬
Bëgg naa 'urīdu ‫َحِتُسو ُس‬
Gannaaw boo ma mayee lii yëpp ba`du ‫َرَي َحْل ُس‬
Lifi nekk bal ‫َر َحْل‬
Na nga yërëm sama taalibe yi Wa tarḥamu ‫َر اَرَي َحْلل َر ُسي‬
Nekkal na la yaw Yàlla laka ‫اَر َر‬
Te ci yaw rekk la mëna juge Wa minka ‫َر َحِت َحْل َر‬
Te ci yaw rekk lay delluwaat thumma fīka ‫ُس فَحِت َر‬
Lepp lu ma sakku ci yaw kullamā ṭalabtuhu ‫ُس َر اَرَرَحْلَي ُس ُس‬
Te yaw Yàlla wa'anta ‫َر َر َحْل َر‬
Yaay joxe xam xamu hikma tu`ṭil-ḥikamā ‫َر‬ ‫اُسَي َحْل َحِتطى َحْلاَحِت َرك‬
Yaakaar naa rajawtu ‫ت‬
‫َرو َر َحْل ُس‬
Man Baay Ñas innani ‫َحِت‬
Dellu naa raja`tu ‫َرو َر َحْل ُس‬
Juge ci yaw minkā ‫َحِت َحْل َرك‬
Lepp lo xamne laaj naa ko bikulli mā sa'altuhu ‫َحِت ُسك َحِتِّب َر َر َراَحْلُس ُس‬
Mu delluwaat ci yaw 'ilaykā ‫َحِتاَرَحْل َرك‬
ḥassin ‫َحِت‬
Rafetalal ‫َر ِّب َحْل‬
Mujjak ña nga xamne ñoo jiituwóon khawātimal'ūlā ‫َر َر َحِتاَر َحْلألُس َر‬
‫َر اُس َر‬
Ña nga xamne ñëw nañ mingóo man Baay
wā-lūnā
doon sama njaboot
Te nga jox ñu wa'a`ṭinā ‫َر َر َحْل َحِتطَر‬

16
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

Loo xamne mā ‫َر‬

Jomboon na fāta ‫ت‬ ‫فَر َر‬
‫َحْلألَر اَحِت‬
Ña jiituwóon al'awwalīnā ‫َر‬
Yaw mi nga xamne yaay nangu yā man yujību ‫ُس‬ ‫َر َر َحْل ُسَحِتُي‬
Ñaanu ku nekk ci tiis, ci jaaxle da`watal-muḍṭarri ‫َحْل طَرِّبَحِتل‬ ‫َرد َحْل َر َر اَحْل ُس‬
Na nga woññi, daq Faltak shifan ‫َحْل‬ ‫فَرَي َحْلَر َحْلك َحِتش َرل‬
Lepp loo xamne laal na ñu mā massanā ‫َر َر َر‬
Ci ay lor min ḍurri ‫َحِت َحْل ُس‬
‫ض ِّبَحِتل‬
‫َحِت‬
Jullil muṣalliyanan ‫ل ِّبًة‬‫ُس َر‬
Ci sa Yónnent gi nga xamal `alān-nabiyyi
‫َر َرى ا َحِت َحِتِّب‬
Di koo tànn al-muṣṭafā ‫لطَرَرلى‬ ‫اَحْل ُس َحْل‬
‫اَحِت َحِت‬
Ag ci mbooleem njabootam Wa ālihi ‫َر‬
‫ِّبَحِت‬
Te def ci moom salaam boo xamne musalliman ‫ُس َر ًة‬
Bu ñuy teralee ñu baaxle ci ba faw musharrifā ‫ش ِّبَحِتلفَر‬ ‫ُس َر‬

17
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

III. Yā rabbi biz zāti

Yaw borom bi Yâ rabbi ‫َرو َحِتِّب‬

Ci‫ا‬sa jëmm ju màgg ji Biz zâti ‫ت‬ ‫َحِت ا َحِت‬
‫ال َرل َحِت‬
Ak sa melokaan yu kawe yi Wa bis çifâti ‫ت‬ ‫َر َحِت َحِتِّب‬
Nekkal ñu Fa kun lanâ ‫فَر ُسك َحْل اَرَر‬
‫َحِت ئَحِت َحِتل َحْلا َر َحِت‬
‫ت‬
Si mboolem suñu feeñuwaay Fî sâ’iril hâlâti ‫َر‬ ‫َر‬
Saxalal Thab bit ‫ثَرَيَحِتِّب َحْل‬
Su ñuy xol Khulû banâ ‫ُسَي ُس َرَيَر‬
Si iimaan (si gëm la) Anlal îmâni ‫َر َرى َحْل َحِت َر َحِتن‬
Te nga jubël ñu Wal tahdinâ ‫َر اَحْلَرَي َحْل َحِت َر‬
Ñu taqoowoo di jëf jëf ju rafet Bi ‘amalil ihsâni ‫َحِت َر َر َحِت َحْل َحِت َحْل َر َحِتن‬
‫َر َحْل ُسَحْلل َحِتاَرَحْلَيَر‬
Yaw yalla xool ñu sa bëtu yërmande bi nga
Wan zur ilaynâ
xamne koo ko xool baaxle na ba faw
May ñu diine di baaxe si ñun Wan çuran na dînâ ‫ل َرلن ا ِّبَحِت َر‬ ‫َر َحْل ُس‬
Lepp luy aq yu ñu mëtalul mëtalal ñu ko Addi huqû qanâ ‫َرد ُس ُس َرَيَر‬ ‫َحِتِّب‬
Suñu bor yëpp fayal ñu ko Wa addid daynâ ‫َرد ا َحْلَيَر‬ ‫َر َحِتِّب‬
Yal na nga may Wa hab ‫َر َرا َحْل‬
Ñeel ñu lanâ ‫اَرَر‬
njaboot goo xamne zurriyatan ‫ُس ِّبَحِتوَر ًة‬
Gu barkél ‫ااا‬ Mu bârakah ‫ُسَر َروَر َحْل‬
Buy nekk Takûnou ‫اَر ُسك ُسن‬
Ngir Yàlla Lil laahi ‫َحِت َحِت‬
Ci ludul ñuy bokkaale Yàlla ci yallam gi Bilâ much chârakah ‫َحِتَّلَر ُسش َروَر َحْل‬
Fayéntel Wa jâzî ‫َر َر َحِتز‬
Ci kepp koo xamne Annî kulla man ‫ُس َر َحْل‬
Rafetal na Qad ahsanâ ‫َر َحْل َر َحْل َر َر‬

18
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

jëm ci man Baay ‫َر َحِتِّب‬

‫َحِت‬
Ñaan naa lako ci ñaan gu juge ci yaw borom bi Ilay ya min rabbi ‫َحِت َر َحْل َروَحِتِّب‬
Mu nekk fay goo xamne Al diazâ’a ‫َحْلْلَرَر َر‬
Mu gën rafet Al ahsanâ ‫ألَر َحْل َر َر‬
Maa ngi la koy ñaan ci Mustafaa Bil Mustafâ ‫لطَرَرلى‬ ‫َحِت اَحْل ُس َحْل‬
Ki nga xamne mooy rammu ñëpp Ach chafî’i ‫اش َحِتل َحِت‬
Besub allaaxira Yawmal mahchari ‫ش َحِتل‬
‫َرَي َحْل َر اَحْل َر َحْل َر‬
Yonnent bi gën ci mbooleem mbindéef yi Khayril warâ ‫َر َحْلَحِت اَحْل َر َرو‬
Ki nga xamne Man ‫َر َحْل‬
Jox nga ko qad hubbî ‫َر َحْل ُسَحِتِّب‬
Kawsara muy ay may yu ko nekkal Bil kawsari ‫َحِت َر‬
‫اَحْلك َحْل ثَر َحِتل‬
Yal na Julli Çallâ ‫َر ى‬
‫َر َر َحِت‬
Ci Yónnent bi Anleyhi ‫َحْل‬
Suñu borom Rabbunâ ‫َروُّيَيَر‬
Te mu def ci moom salaam Wa çallamâ ‫َر َر َر‬
Muy julli goo xamne dana ci bëbbëlee Wa fâda ‫َر فَر َر‬
Ci lepp luy yiw Bil khayri ‫َحْلَر َحْلَحِت‬
Mu nekkal ñu Lanâ ‫اَرَر‬

19
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam
Recueil d’invocations traduites en wolof

IV. Salātul tunjinā (munājāti)

Yaw Yàlla Allâhumma ‫َرا ُس ي‬

Julil Çalli ‫َر َحِتِّب‬
Ci suñu sangg ‘alâ sayyidina ‫َر َرى َر َحِتِّب َحِت َر‬
Muhammed Muhammadin ‫ُسَر ٍد‬
Julli goo xamne Çalâtan ‫َرَّلَر ًة‬
‫َحِت َحِت‬
Da nga ñu ciy musalee Tunajjînâ bihâ ‫اُسَيَر ِّبج َر ِبَر‬
Ci lepp luy tiis Min jamî‘il ahwâli ‫َحِت َحْل َرَحِت َحِت َحْلأل َحْلَرا َر َحِتل‬
‫ت‬ ‫َحْل فَر َحِت‬
Ak yu bon Wal âfâti ‫َر‬
‫َحِت‬ ‫َحِت‬
Da nga ñu ciy fajalee Wa taqdî lanâ bihâ ‫َر ا َحْل اَرَر ِبَر‬
‫ت‬‫َرَحِت َحِت َحْلاَي َحِت‬
Lepp luy su ñuy aajo Jamî‘il hâjâti ‫َر َر‬
‫َحِت‬
Da nga ñu ciy laabalee Wa tutahhirunâ bihâ ‫َر اط َحِتِّب ُسلَر ِبَر‬
‫ت‬‫َحِت َرَحِت َحِت ا َحِتَر َحِت‬
Ci lepp luy yu bon yi Min jamîs-sayyi-âti ‫ِّب‬ ‫َحْل‬
‫َحِت‬
Da nga ñu ciy kawelee Wa tarfa‘unâ bihâ ‫َر اَرَي َحْللفَرَي ُسَر ِبَر‬
‫َحِت َحْل َر َر َر َحْل َرى ا و َحِت‬
‫ت‬
Ci lepp luy daraja yu kawe yi Indaka a‘lâd-darajâti ‫َر َر‬
‫َحِت َحِت‬
Da nga ñu ciy yeegalee Wa tuballighunâ bihâ ‫َر اُسَيَر ِّب ُسَر ِبَر‬
‫ت‬ ‫َر َحْللى اَحْل َر َحِت‬
Ci gën caa kawe dayoo ci mbaax Aqçâl ghâyâti ‫َر‬ ‫َر‬
‫ت‬ ‫َحِت َرَحِت َحِت َحْلَرَحْلَيل َحِت‬
Ci lepp luñ naan lu baax la Min jamî‘il khayrâti ‫َر‬ ‫َحْل‬
‫ت‬ ‫َحِت َحْلاَي َحِت‬
Ci dundu bi Fil-hayyâti ‫َر‬
‫َي َحْل َر اَحْل َحِت‬
.‫ت‬
Ak gannaaw dee Wa ba‘dal mamâti ‫َر َر َر َر‬

20
Ce recueil de Elhadji Mlaick Sow n’est pas destiné à la vente. Nous suivre sur facebook : Traduction en wolof
des livres de Baye niass. Sur Youtube : Euttu xam xam

Vous aimerez peut-être aussi