Vous êtes sur la page 1sur 3

Gane gui

Dama teud sama lale, yegg buntu negg bi tidiékou, wayé mounekk
tidiéko bu outték bima tam di guiss... mou ameu gane gou douggssi.
Mingui ameu melokane gou raglou, dougg té feugoul yéglé woul.

L’étranger
Allongé sur mon lit, je sentis la porte s’ouvrir mais d’une ouverture
dont je n’ai jamais vu ; aussitôt un étranger entra. Il eût une
apparence très effrayante. Il entra sans frapper ni mettre au courant.

Mou daldi yekssi tiim ma, ma teud si lale bi.


Ma tambali ameu ay yegg yegg yu bess thie sama dieum dji... sama
yaram bi diss, sama tank ndéydior tambali bagn, meunatoumako
dieufandiko, niou teggssi sama tank thiamogn.

Il arriva devant moi et j’étais toujours allongé.


Je commençai à sentir des sensations nouvelles. J’eu le corps lourd
et les fonctions de mon pieds droit ne répondaient plus. Ensuite s’en
suivirent celles du pieds gauches.

Ndank ndank samay lokho tegoussi. Louma beugg yékatti rk mou


bagn ; mou melni samay tieur wouyo tougnou, may khol gane gui
beugg wax sama lamign bi bagn melni sakhatoul si mane.

Petit à petit, mes mains s’en suivirent. Mes membres ne pouvaient


plus se lever ; comme si je ne suis plus plus maître d’eux, je continuai
de regarder l’étranger voulant lui parler mais je sentis une sensation
comme si ma langue ne faisait plus partie de moi.
Samay beutt né khadj di khol guane gui. Bala mou dane yekssi
mangui done degg wax yi nekkone si bitti wayé bimou yekssé ba
tiime ma sila sama nopp yi fatteu deggatouma daarra.

Mes yeux figés sur lui. Avant son arrivée je percevais les bruits
dehors mais depuis son arrivée plus aucun bruit ne pénétrait mes
oreilles.

Thie khol gou yagg gogou, may guiss lima diotone doundou sama
adina bi yeup melni kouy setane sama bopp bima dioudo ba nimou
may fekkei ma teude si lale bi

Dans ce long regard figé, je vis tout ce que j’avais vécu dans ma vie
comme si je regardais le film depuis mon enfance jusqu’à l’instant où
il arriva me trouvant sur le lit

Sama dieuf yi, nitt yima done togn, beureup you bone yima done
deim, dieuf youbone yima done def, leip lou nekhoul Yallah yima done
def melni lounioumay wane si diir giu gatt.

Mes actes, les personnes que j’offensais, les mauvais endroits que je
fréquentais, les mauvaises choses que je faisais, tout ce que je
faisais et qui ne plaisait pas à Dieu me passe devant les yeux dans un
court instant.

Manguikay khol di yekk louy guindékou si sama dieum dji daléko


sama tank yi di yegg...
Bimou amé louy rothiékou si mane ba yekssi si samay beutt ma daldi
melni kouniou guéné thie beureup bima nekkone yobouma si
beineine wayei ma nek si beine beureup bi batay.

Je le regardais en sentant quelque chose se détacher de moi à partir


de mes pieds en montant. Quand cet procédure arriva jusqu’à mes
yeux, je senti comme une expulsion du milieu dans lequel j’étais et
pourtant j’étais dans la même pièce.

Gane gogou moy Izraël niou geuneko kham si tourou Malakal Mawti...
mom la souniou Borom yonni wone nguir mou dieulssi sama rouh,
yobounako té dotoul déloussi fi dunya...

Cet étranger se nomme Izraël plus connu sous le nom de L’Ange de la


mort, c’est l’émissaire de Dieu qui était chargé de prendre mon âme.
Il l’a amené et plus jamais il ne reviendra dans cette vie.

Dé dina nieuw dh. Naniouko wadial ndax dafay bétté !

La mort viendra à coup sûr. Préparons nous car elle vient par
surprise.

Vous aimerez peut-être aussi