Vous êtes sur la page 1sur 1

XAM NAA CI KAN

Source: 2Tm 1,12


T.M: Abbé Baye Rémi DIOUF
HARM: Jean Baptiste K. FAYE

& b 38 œj œ œœ .. œœ œœ œœ œœ .. œ œœ œœ œœ
œ œ œœ œœ œ œœ .
.
œœ .
.
J
Xam naa waaw xam naa ci kan, ci kan la tegg su-ma ngëm.
j œœ . œ œ œ œ.
? 3 œ œœ
œ . œœ œœ œœ œ œ œ œ. œ.
b 8 J œ œ œ œ. œ œ œ
œ. œ.
j
COUPLET 1
œ œ œ œ œ œ
œ œ œ. œ œ œ
9

&b œ œ œ œ. œ.

Coo-noo a - du-na mo-nu-ñu ma fa-qas - tal, Bo-rom bi;

?b ∑ ∑ ∑ ∑ ∑ ∑ ∑ ∑
17

& b œœ œœ œœ œœ œœ œœ œœ . œœ .
. .
l'exécution des couplets est libre:
ci yow la tegg su-ma ngëm. Soliste, femmes ou hommes ou
alternativement.
œ œ œ œ œ œ œ. œ.
?b œ œ œ œ œ œ œ. œ.

2. Gis gis aduna munuñuma faf gumbal, Borom bi; ci yow la tegg suma ngëm.
3. Degg deggi tey ji munuñu ub sumay nopp, Borom bi; ci yow la tegg suma ngëm.
4. Yite aduna munuñu dogg sumay tanka, Borom bi, ci yow la tegg suma ngëm.
5. Bëgg bëgg(i) aduna munuñu bank(a) sumay loxo, Borom bi; ci yow la tegg suma ngëm.
6. Xew xewi tey ji munuñu ub suma xol, Borom bi; ci yow la tegg suma ngëm.
7. Jano ak yow moy suma soxla tey, ëlëg, abadan; ci yow la tegg suma ngëm.

Composé le 22 novembre 2012 en l'année de la FOI


Copyright © JBKF

Vous aimerez peut-être aussi