Vous êtes sur la page 1sur 2

JANGU KERCEEN

Entrée, Procession tirée du Caabi Aljana, page: 189 Harm: Georges Bénédicte CISS

         
           
1).Jàn gu ker ceen war na ñu ko sop pa lool



 
                   

            
  
Fa la Yée su su ñu Bo rom dëk ka

          

 
                     
(T&B): Fa la Yee su su ñu

                    

bë tu ya ram du fi më na gis da ra

 

 
                            
1. 2.

                    
       
van de su ma xol nee: sa Yal la'n gi Yal la'n gi

         
 

12
(T&B): van de su ma

Copyright@: tine_isi
ITTE COFEEL CI TANK’U LOTEL.
Air : O saint autel (CJ. P. 71)

1. Jàngu kerceen, var nañu ko soppa lool,


Fa la Yéesu, suñu Borom dëkka,
Bët’u yaram du fi mën a gis dara,
Vande suma xol nee : sa Yalla’ngi (Bis).

2. Bi ma sukka, di ñaan ci tànk’u lotel,


Suma xol bépp fees na deel ak banex,
Am fi vaxtu, volay ! mo ma gënal lool,
Téméer i at ci kër u bakarkat (Bis).

3. Ey Yéesu man! Sa baaxaay ëppa na moos,


Moo, lu nit doon, be soppa ko noonu?
Aduna si dootul béréeb u rongoñ,
Fo nekk, Baay, aljana anga fa (Bis).

4. Malaaka ya ñunga di vër lotel ba,


Di nav Yalla mi fi nëbba boppam,
And’léen ak man, ey ! xel i aljana yi,
And’ léen ak man, ndax ma gërëm Yéesu (Bis).

5. Ey yéesu man, nekkal suma buur u Xol,


Lu la neex moos, moom rekk la bëgga def,
Randul leen ma, baneex u aduna si,
Suma xol bépp, Borom bi, moo ko moom (Bis).

2 Copyright@: tine_isi

Vous aimerez peut-être aussi