Vous êtes sur la page 1sur 18

Le Taysir

Transféré par Daba Cheikh Wade

La ·
90%bibliothèque la
(67) 72K vues 6 pages ·
plus fascinante
Recherche
au monde
Informations du document 
Pour accéder
traduction à ce document,
et transcription veuillez
du tayssir ou en transférer…
wassilatoul
un des vôtres, ou abonnez-vous avec un essai gratuit
Titre original
LE TAYSIR de 30 jours. Résiliable à tout moment.
Télécharger maintenant 
Copyright
© © All Rights Reserved

Formats disponibles
PDF, TXT ou lisez en ligne sur Scribd
13 389 personnes
Partager ce document
parcourent Scribd en ce moment

Facebook Twitter
S'inscrire avec Google

S'inscrire avec Facebook


Courriel

Avez-vous trouvé ce Ou S'inscrire


document utile ? par e-mail

 M'envoyer des mises à jour de Scribd


En vous inscrivant sur Scribd, vous acceptez nos
Ce contenu Conditions de service
est-il inapproprié et ce
? Signaler notre Politique de
document
confidentialité

Vous avez déjà un compte ? Se connecter

 
:
 

LE TAYSIR

1- ( La Partie ARABE )

1.Alhamdu li laahi zi taysiiri Yàllahu 2.Nazma daraari lahu Yàllaahu Yàllaahu


3.Yàllaahu salli salaatan lantiha alaha
4.Sallim allal Mustafaa Yàllahu Yàllahu
5.Tahaadalaa salawaa tilxaasatil hukamaa
6.Ahlil mahabbati ahlil Laahi Yàllahu
7.Salli salaatan wa tasliiman alaa xamarin
8.Min nuurihii quliqal akwaanu Yàllahu
9.Law lam yalux fifadaa ikawni tal-atuhu
1O.Tabqal bariyyatu fii zalmaa-i Yàllahu
11.nuurun min annuuri xad awdaatuhu hikaman
12 .Tafiidu faydan allal axlaaxi Yàllaahu
13.Nuurun ahaa tabihil anwaaru haajibatan
14.Anil hàqiiqati kullal xalqi Yàllaahu
15.Nuurun mubiinun ataa nuural mubiina li-ir
16.Saadil ibaadi jaamii-an Rabbi Yàllaahu
17.Maa fiil bariyyati man lam tasqihi karaman
18.Min nuurihi Rabbana Yàllaahu Yàllaahu
19.Hàqiiqatul kawni aynuzaati tal atuhaa
2O.Ifaadatu Laahi nuuru Laahi Yàllaahu
21.Salli aleyhi salaatan lantihaa kamaa
22.Laa lil kamaa lintihaa Yàllaahu Yàllaahu
23.Salli aleyhi salaatan salliman abadan
24.Adda kamaa làtihi hibbika Yàllaahu
25.Salli aleyhi salaatan Rabbi kaamilatan
26.Adaa ihaatati ilmil Laahi Yàllahu
27.Ixfirli ummatihi waarham bi ummatihi
28.Waastuur lahaa waajburan haa Rabbi Yàllahu
29.Yàllaahu Rahmaanu yaa Rahiimu yaa Malikul
30.Qudduusu yaa Muuminus sallamu Yàllaahu
31.Yaa Mutakàbbiru yaa Jàbbaaru Xaaliqu yaa
32.Muhayminul Baari-ul Qaffaru Yàllahu
33.Aziizu Qahaaru yaa Waalil Musawwiru yaa
34.Wahaabu Razaaqu yaa Fàttaahu Yàllaahu
35.Allimu yaa Qaabidul Baasitu yaa Hakamul
36.Mu-izzu yaa xaafidu Raafi-u Yàllaahu
37.Muqillu yaa Adlu Adlu yaa Samii-u Waasi-u yaa
38.Basiiru Baa-isu yaa Latifu Yàllahu
39.Rabbi Muqaddimu muxni yaa Muwaxiru yaa
40.Xaniyu Yàllahu yaa Xabiiru Yàllaahu
41.Matiinu yaa waajidul waliyyu Rabbiya yaa
42 .Hamiidu Yàllahu yaa Aliyyu Yàllahu
43.Haliimu yaa Hàqu yaa Wakiilu Maajidu yaa
44.Xafuuru yaa Hàyyu yaa Qàyyumu Yàllahu
45.Sakuuru Jaami-u yaa Majiidu Rabbi ya yaa
46.Kabiiru yaa Muqsitul Aziimu Yàllahu
47.Qawiiyu Muhsil Mu-iidul Mubdi-u Samadu
:
Your access is waiting

Sports Alerts Open

 
:
 

48.Muhyil Mumiitu Ra-uuful Barru Yàllahu


49.Tawwabu yaa Muta-aalil Waahidul Ahadul
50.Maani-u yaa Daaru yaa Naafi-u Yàllahu
51.Yaa Maalikal Mulki Rabbi Zaldjalaali wali k
52.Raami Shahidul Badii-ul Haadi Yàllahu
53.Yaa Nuur u Muntàqimul Qaadiru Muqtadiirul
54.Mujiibu Yàllaahu yaa Waduudu Yàllaahu
55.Ya Awwalul Aaxirul Kariimu Zaahiru yaa
56.Raqiibu Baatinu yaa jaliilu Rabbi wa yaa
57.Muqiitu Yàllaahu yaa Hakiimu Yàllaahu
58.Hafiizu Yàllaahu yaa Hakiimu Yàllaahu
59.Afuwwu yaa Waarisul Baaqi Rashidu wa yaa
60.Sabuuru yaa Rabbanaa Yàllaahu Yàllaahu
61.Bisirri haazaal asaami Salliyan alaa
62.Sayyidinal haamidil Mahmuudi Yàllaahu
63.Al Faatihil muxlaqil Xaatimi maa sabaqal
64.Musral Mukallami Xayril Xalqi Yàllaahu
65.Annaasiril hàqi bil hàqil jalii wa ilaa
66.Siraatikal mustàqiimil Haadi Yàllahu
67.Summa alal aali Hàqa qadrihi qadaran
68.Miqdaarihi indakal Aziimi Yàllaahu
69.Rabbun tabaaraka, aw Rabbun taqaddasa, aw
70.Rabbun ta-alaa uluwan Rabbi Yàllaahu ( 3 fois )
71.Abdun zaliilun faqiirun xaasi-un wajilun
72.Zuujaza-in ashifun Yàllaahu Yàllaahu
73.Ileyka maddal yadaa raja-a maxfiratin
74.Habli musaa mahatan Yàllaahu Yàllaahu
75.Tamaw wadjal bahru, bahru zanbi yaasiqati
76.Wa innani Rabbi xiftul xarqa Yàllaahu
77.Wa maa safiinatu turjaa xayra rahmatikal
78.Uzmal amiimati kullal xalqi Yàllaahu
79.Ashkuu ilaa laahi haajan laysa yarfa-uhaa
80.Siwaaka yaa Rabbannaa Yàllaahu Yàllaahu
81.Halmin muziilin bimaa qad kaana yuuriduhu
82.Rabbul ibaadi alayhim Rabbi Yàllaahu
83.Wa naafizun Haakimun fiinaa iraadatuhu
84.Kamaa Yasaa-u wa jalla laahu Yàllaahu
85.Wa saamihan waalidiinaa wasuyuu xawaman
86.Qad waladuu wazawil islaami Yàllaahu
87.Salli salaatan tunajjimaa bihaa abadan
88.Jamii-al ahwaali wal afaati Yàllaahu
89.Salli salaatan bihaa taqdilanaa abadan
90.Jamii-a hajaatinaa Yàllaahu Yallaahu
91.Salli salaatan bihaa Rabbi tutahirunaa
92.Min jumlatis sayyi-aati Rabbi Yàllaahu
93.Salli salaatan bihaa Rabbiya tarfa-unaa
94.Axla minad darajaati rabbi tuballixunaa
96.A-jalla aqsaa minal xaayaati, Yàllaahu
97.Yàllahu yaa Rabbi fil xayraati jumlatiha
98.Indal mammaati wa bahdal fawti Yàllaahu
:
 
:
 

99.Balix ilaa Saafihil aali amaanatanaa


100.Salaatanaa ma-ahaa tasliimu YàlLAHU
101.Salli wa sallim alaal haadi samiimi kamaa
102.Tarda wa yardaahu yaa Rahmaanu Yàllaahu
103.Salli wa sallim alaa nuuril muhiiti alaa
104.Kullil mukawini kanzil xalqi Yàllaahu
105.Salli alaa Rahmati daarayni sayyidinaa
106.Ruuhil wujuudi wa sirrizzati Yàllaahu
107.Alaal muxaatabi waasjud waaqtarib karaman
108.Salli wa salaaman Rabbi Yàllaahu
109.Salli alaa lawhikal mahfuuzi lasrafimin
110.Kullil xalaa iqi yaa Rahmaanu Yàllaahu
111.Tilkal amaanatu takfiiman takunnu lahu
112.Muballixan yaa manul iisaala Yàllaahu
113.Laatahrimanaa ilaahil yawma ruhyatuhu
114.Falaa yaxiibanna man yarjuuka Yàllahu
115.Man lam yakun yalqahu xadan yanalwajalan
116.Haazaal kasiiru ataa lil jabri Yàllaahu
117.Wa kun lanaa Rabbi fii kullil umuuri faman
118.Yakun kazaalika yalqal yusra Yàllaahu
119.Salli salaatan bihaa Rabbi tu-allilunaa
120.Bihawdihii Rabbanaa Yàllaahu Yàllaahu
121.Salli salaatan wa tasliiman zaraa itaran
122.Alal habiibi wa aalil hibbi Yàllaahu
123.Salli alaal badri maa ammal hajiiju ilaa
124.Ziyaarati rawdi yaa Rabbi qasiidatanaa
126.Wasiilatal lil munaa Yàllaahu Yàllaahu
127.A-uuzu bil Laahi min xawfil anaami wa min
128.Ridan ani nafsi hammi rizqi Yàllaahu
129.Wa raddinii bil qadaa Rabbi musabbirani
130.Alaa balaa-ika yaa Rahmaanu Yàllaahu
131.Muuzi ani Skramann awlaytanii ni aman
132.Jalla sanaa uka yaa Rahmaanu Yàllaahu
133.Laa uhsiyannas sanaa aleyka anta kamaa
134.Rabbi alaa nafsi qad asnayta Yàllaahu
135.Faaxfirlanaa waliman min bayninaa nasabun
136.Min jihati tiini aw fiddiini Yàllaahu
137.Salli alaa saajidin qablal waraa fa-alaa
138.Bisab-imii ati aamin Rabbi Yàllaahu

2- ( La Partie WOLOF )

1.sante gnel na Yalla moom miy adji yombal ji


2.bàkk ak kagn gnel na Yàlla te moom rekk kako yeyoo
3.Yow Yàlla nanga djouli ag djouli gou amoul àpp
4.Dollig mucc si ki gnu tànn yow Yàlla
5.Lou tollu sig missal julli gi gnu jaglel borom xam xam yi
6.Gnom gnognoy boromi coofeel diy waay fa yàlla
7.Jullil te dollig mucc si weer wi yow yàlla
8.Si lerug weer woowe takh nga sàkk aduna ak lisi biir
:
 
:
 

9.Weer woowe nga xam ne bu melaxul woon


10.Adduna ak lisi biiram des sig leudeum
11.Leer googe di leer gou jougé si leer gu maàg gi
12.Te nga diokh ko yow Yàlla xam xam bou yaatu te gnaw
13.Muy leer ak xam xam guy baawan sig mbindef yi
14.Leer googu ay leer zeur ngir aar ko si loorangé mbindef yi
15.Mou di ag leer gou fés indi yit leer gu fés
16.Di gindi jaam yi sig leudeum indi leen sig leer
17.Amul béne mbindef moo nàndalug teddange yow Yàlla
18.Gu jogewul si leeram gu sell googu yow sama boroom
19.Deug deug nekkug boroom djeum jii ak penkam
20.Doonul lu doul ag leer goo baawaan yow Yalla
21.Yow Yalla jullil ag julli gu amoul kem si yonent bi
22.Ag julli gu amul mass ni sa maggaay gnaké mass
23.Yow Yalla jullil ag julli te dollig mucc yonent bi fàww
24.Lu tollok matt gimou màtt ba doon sopey Yàlla
25.Nanga julli ag julli gou màtt seuk
26.Lu tollok lépp li nga xam ne sa xam-xam weur na ko
27.Yàlla, nanga yeureum té jéggal xeetu yonent bi
28.Yàlla , nanga suturaal té neubbal ay gnawtééfam xéétou yonent bi
29.Yow Yàlla, di Aji-yeurmandé ci àdduna ak ca àllaaxira, yow, Buur bi,
30.Ku sell ki, ku woor ki, yow miy jàmm ji, Yow Yàlla.
31.Yow mu màgg mi di boroom doolé, tey sàkk
32.Yow mi tééwé lépp té wéet ci sag càkk, tey jéggalé bàkkaar yi
33.Yaay ku tédd ki, ki not léép té aajowoo mbir yépp
34.Yaay kiy mayé, yaay kiy xéewalaaté yaay kiy ubbilaaté
35.Yow yaa xam, yaa lépp, yaa talal té yaay àtté
36.Yaay téral, yaay wàccé, yaay yékkati, yow Yàlla
37.Yaay toroxal, yaay ki maandu, yaay dégg, yaa yaatu
38.Yow aji-gis, di aji-dekkal, yom mu léwét mi, yow Yàlla
39.Yàlla, Yow mi jiitu yow miy woomal, yow miy dés
40.Yaay ku woom ki, di kiy daj lépp ci gisam.
41.Yaay ku deugeur ki, ki neck fépp, tey méngalé
42.Yow mi yelloo cant, yow mu koweé mi, yow Yàlla
43.Ku léwét ki, di deug gi, ki gneupp wéer sééni mbir, yaay ki màgg
44.Aji-jéggale ji, yaay ki dund, yaa taxawe àdduna bi, Yow Yàlla
45.Yaa yélloo cant, Yaay dogal, yaa màgg, yow sama Boroom
46.Yow miy matal kooleuré, té màgg, yow Yàlla
47.Boroom doolé, ki sàkk tey delloo ruuh yi tey fént, yow mi gneupp jublu
48.Yaay dundal, yaay rey, rey, yaay gnééwaneté, ku baax ki, yaw Yàlla
49.Yaay bale, yaa kowé, yaay ki wéet ci kénnam gi
50.Yaay kiy téré, Kiy lore, Kiy jarigne, Yow Yàlla
51.Buuru buur yi, di sunnu Boroom, boroom màggaay ak tédd-nga
52.Yow mi Sééde lépp, jéggi dayo tey Gindi jam yi, yow Yàlla
53.Yow Léér gi, ku jub ki, Boroom kàttan ak Meun-meun,
54.Yow miy wuyu, yow Yàlla, yow mi gneupp sopp,
55.Yaay ki jeukk, kiy mujj, ki Tééd yow mi sa lépp féégne
56.Ku fuglu ki, yow mi làqu, yaay Aatté, yow Yàlla
57.Yaay kiy dundal, yow boroom bi, yow ku màgg ki,
58.Ki wottu lépp, ku Xérégne ki, Yow Yàlla
:
 
:
 

59.Kiy jéllale, kiy donn lépp, di fi dés ba fàww,jub téy jubal


60.Yaay kiy mugne, yow sunu Boroom,
61.Ci barké mboot yi sa tur yi làq, Yàlla, dollil xééwal
62.Ci sunu Sang, ki gnu santloo ko, yow Yàlla
63.Té mu ubbi buntu yeurmandé, teuj buntu séytaané, mottali la jiitu
64.Moom mi nga ragnaane, waxloo ko, mu geun ci mbindééf yi
65.Mooy kiy dimbali deugg, deugug Yàlla gu féégn gi,
66.Nu ngi jaar ci yoon wu jub wi, yoonu kiy jubal, Yow Yàlla
67.Topp njabootam ci deuggu kemug dooléém, ak kàttanam
68.Ak darajaam ci yow Yàlla, ku màgg ki, yow Yàlla
69.Boroom bu séll bi té séllam màgg lool
70.Boroom bu kowé bi, bépp kowé, yow Yàlla
71.Ab jaam a ngii doyadi gnak toroxlou toumouranké
72.Jjaam bu tiit te jak ngir ay bakkaram yow yalla
73.Yyaw dey laay tallal samay lokho yakkar ay njégal
74.Nnanga ma maay limalay niane yow yalla
75.Géej dafa buusu géejug bakkar yow sama ndeugeurlay
76.Mman sa jaam dey ragal na lab si yow yalla
77.Ggan gaal la niouy yakkar ngir mucc gudul sag yeurmandé
78.Di yeurmandé gou magg gi te matal mbindef yeup yow yalla
79.Maa ngi tawat, jeumale ci Yow, as soxla té du faju
80.Feek àndoo ci, Yow sunu Boroom, Yow Buur bi
81.Ndax am na ku man a dindi la Yàlla bi namm cib jaamam
82.Boroom jam yi, nu di la jaamu yow mi gnu bind
83.Yow miy àtté ci mépp mbir moo namm ci gnun, sa jamm yi
84.Ca na mu la soobé, Yàlla màgg na, yow sunu Boroom
85.Yàlla na nga jéggal sunuy waajur ak seurign sépp
86.Ak ku juddoo ci gnoom ak gna am islaam té di ko taxawé
87.Dollil ay xéewal jeumalé ko ci wallu gnu ba fàww
88.Ci bépp jafé-jafé ak gàkk-gàkk yow sunu boroom
89.Nanga dolli xéewal jeumalé ko ci fajal gnu ba ba fàww
90.Mbooléem sunuy aajo, yow sunu Boroom
91.Dollil xéewal, yow Yàlla, jeumalé ko ci j”ggal gnu 
92.Ci mbooléem sunuy gnaawtééf, Yow Yàlla, yow Buur bi nuy jaamu
93.Dollil ay xéewal, Yow Yàlla jeumalé ko ci yeukkati nu
94.Ca daraja ya geuna kowé fa yow,Yow sunu Boroom,
95.Nanga dolli xéewal, yow Boroom bi jeum ci jotale nu
96.Li geuna réy, geuna sore ci yaakaar yow sunu Boroom
97.Yow Yàlla, yow Boroom bi, xéewal yi nuy yootu
98.La nu raw, mbaa sunu gannaw, Yàlla nanga nu ko défal
99.Yàlla, jottalil ci kiy rammu jaam yi eulleug, sunug koolleuré
100.Té sunuy julli ànd ak mucc ci moom, yow Yàlla.
101.Yàlla, dollil jàmm ci kiy wommat jamm yi té nu deugeurloo ko
102.Nga geureum ko, mu sant la, yow Boroom yeurmandé,
103.Yàlla dollil xéewal, té jàmmal leer googu weur képp koo bind
104.Ci kiy mbootu mbindééf yi, yow Yàlla
105.Dollil xéewal àdduna ak àllaaxira yeurmandé ci sunu sang
106.Ki mbindéef yiy noyyée té mu yor ay mbooti boppam
107.Yàlla, na teddaange nekk ci ki nu digal mu sujjoot té jégé boroomam
108.Yàlla dolli ko xéewal ak jàmm,yow Yàlla
:
:
Partager ce document
    

Vous aimerez peut-être aussi


:
Document 8 pages

doua wassifa
cheikh tidiane
Pas encore d'évaluation

Document 9 pages

About Baye
steve
100% (1)

Document 10 pages

fascicule tariqa Tidjanie


Ndam Abou Abdelaziz
100% (1)

Magazines Podcasts

Partition
:
Document 29 pages

Pulaareeje.doc
DecePulaar
75% (4)

Document 3 pages

CHANT PRIERE DE JERICHO


2023
pascal mubalama
Pas encore d'évaluation

Document 6 pages

Gnaanou Goudi Laylatoul


Khadr
Cheikhouna Ndiaye
Pas encore d'évaluation

Document 9 pages

RUKOEN LHE BLAH


Ayah Zein
Pas encore d'évaluation
:
Document 11 pages

Fondement et règlements des


oraisons
sdjoulde
Pas encore d'évaluation

Document 9 pages

Nouveau Document DOC


mouhamed
Pas encore d'évaluation

Document 24 pages

Translitteration
Es Mardochee
Pas encore d'évaluation

Document 55 pages

Wolof Bible Wolof Kaddu Gu


Xelu-g1
Africa Bibles
Pas encore d'évaluation
:
Document 1 page

Nahnu Jîrônu Bidzâl Haromi


taufiqstune
Pas encore d'évaluation

Voir plus
:
À propos Assistance

À propos de Scribd Aide / FAQ

Presse Accessibilité

Notre blog Aide à l'achat

Rejoignez notre équipe ! AdChoices

Nous contacter Éditeurs

Inviter des amis


Social
Cadeaux

Scribd pour entreprises Instagram

Twitter
Mentions légales Facebook

Conditions Pinterest

Confidentialité

Droits d'auteur

Préférences en matière de cookies

Ne vendez pas et ne partagez pas mes


informations personnelles

Obtenez nos applications gratuites

Livres audio • Livres • Documents • Magazines • Podcasts • Partition

Langue: Français

Droits d'auteur © 2023 Scribd Inc.


:
:

Vous aimerez peut-être aussi