Vous êtes sur la page 1sur 1

EDITORIAL FORUM SUR LA FAYDA ACTU DE LA FAYDA ALBUM PHOTOS VIDEOS Quiz Boutique Blog Annuaire Réservation

CHABABOUL FAYDA
BABACAR THIAM FAHANZI SALAMOUN
DOSSIERS

FACE A....

PORTRAIT

ILS ONT DIT

MP3

Albums photos
http://yafaydoutidjanie.skyrock.com/1.html PAROLES BABACAR THIAM
Catégorie par
défaut fahazi salamoun fa hazi salamoun mini iley kaw marioul anbari wa taybal
miskaw damay wélbéti bollém wéyénou sodane
Dernières images tchi zahir sidi batine ba diar di sétane
sama khatir dafa roti fa behrou kayor
may wey ki jara wey moniou toussé ay leer
nga lambo tchi diné lislam
sopé ba la ko jokh mo héyone té khadim
khoutboul jamihou niass ya di janteu njooloor
MOUVEMENT CHABABOUL
FAYDA saxaal gua fi ay leer tek si mbir you doy waar
Annuaire
ma gui lay yalouwanne yaw mi done tijaan
Actualites et may ma sa mboubitane xool kone ma dé tchi imane
medias fégoulena tibalma kone ma jook si békor
Sport raf léna khod meu ma bah li may gar
Services
Webmasters sa wéla gueuneu gaw khaar mou fad bay buur
Loisirs sa khewela gueuna bawane ba melni ay niir
Vie pratique sa haté géna wer ya khalilou rahmane
Jeux té lo wax borom "koun" dal di neé fa"yakoun"
Internet et sa kharbakh yi gua lambo siwal na doktor
informatique dal beu ko taafli mou weer far dou déme ssi doktor tékotaafli sa loor yi
Economie et tafalko bachoura
Immobilier
mo tagok lorou dounya ka chaka oukhra
E-commerce
dama sope di la wéye wanté raw gua say mass
Culture et sciences
li takh ma di la wéye gua nirro borom fez
Blog sa mbotaam xalimba raw na dabo ssou Moussa
Blog sa waydé yi nga dékal téwon na Issa
kouye mouride na ma nieuw wéylé sidi barham niass
Panier wa dji xaam meuna ragné té sope barham niass
Votre panier est mou jokh ma khatim mba mou jokh mab faw khom
vide té bawal mam khél mba mou may ma fa moom
kone dana meuneu wéye ki fi guéne si sodane
Panier
di khoutboul rohoyi naan si peyi diwaane
Votre compte
deglou léne bama délou di kagn di gueune
fi sa azaal la ko buur bi jitalone douwoul fi
Quiz barhama ba nga roté ba say bakéne fess
Quiz bawal nga gnilone khar ba séni ndab fess
halam ak alal am mom la jaay tchi lislam
Locations
gnou signéle ko mou weer jookh ko khatmou fayloum
Réservation
sou nguéne xamone ay may sa you néke guen téew bagna ling kaar bagna
dinguante té guene saxoo waaw beteb kagnane dafa bepeng sakho lou
kharbakh kone gnou guissbi nga watté you xamné ya baax
masta joox keur bayam té raw tchi si lislam
béne serigne manou fé waax né demna daraam
ki raw na aw massam ni att mi weéy daw bou kagnane amoutone lolou
modi ak mbakh
sou féke guey yeém lolou doye na kharbakh
bam amé gneti att la dadial BACHOURA
di dior ay massalaam bolékok 
maqamam
siroube ngueunéle bi nga lambo néwoul si ay mool
yaye khoutboul yaay raoussou yaay seydi ridial
toutiwoo reuyoulo gattoulo douho njool
dieumi RASSOULOU la yoor gnou niro baasi mole
sa beut yay nelawite kholba mom mou ngay xool
té rohom ga arach ak koursiyousi ley beéw
té bouy retanite xaar kanaam ba né wer kar-kar t
é waram gena nekh lém ssa khol ya miy waar
bala nga koy hem lol boba aw nakar fegne
so kholé barhama niass guiss ko mouye mougne
moy djikom jamou donone fa saydi hadnane
dogal bou reye bala doylo moy "koun fa ya koun"
faalewoul adinak li ci biir dafay nil
khegn touhoul loumouy yala ak nabi daal
mola xaam koumou yem ci alal bamouy soy
té am ko douko bég lo xamoul lou mooy baye
konté woul ay tone titou mooy yenouy taakh
raboul samawaati wal ardi doy na koy jeex
té mandok ragal yalla ak tabé ci lislam
té tolam ba dou boy modi yonou jakaam
hitém ya mo guena kher gaindé moy yébuy buur
karama ya ngéna rey doussi golfa yiye door
ay betém dafa bot emni diani saman
rahmatamom guena mat ci fakhirak miskin
suxilingua sugnu roho yi sukhone souniouye mame
nigno minka bou wer diene ba teersi ndangane
sillmaxxa kouka tay ba bam xool assamane
warna joox baay saganté topeu say waw
raboul jallil la ko fal joxx ko mane tou rabbane
fal gamiye falidomame siwale nalab daal
waltakoun outamane mome ma la wax fa lakhot
kou aw cib dingalaam kham illahi nassot
bagne yooré souniou hadio siyaré madina bagne démé basa pome ba
gnou déffa diorane dieumeum
yak xeel ya xool ya bagne diagnok baye dougne mebéte lu moy topou say
takhok mome ndax melow yousoufa la la yoorki rawone ci ay taar
ba kou dianok mom sopou ko dax fa yoor leer aladjii souniou mame dane
na wax né mooy hass boba ma ngay khol nawléyak betoub mass
la khassou dinarou mom bagne ko diokhone la barham fayé balayi fi ci
sodane
la khadirni fi moussa wama li hayate lassougne bay yaré domame bi isni
mahyaa
SPONSORS diouli na si rassoullou illahi mahwwa salatane wa salimoune ma gnane si
Créer unabass
site Agenda Culturel ×
toudé na di la wey fadi hassi djihate ci koursiyin gni fi dan wey imamou
ibada
fabal khatmou sa wey wi té hemfi yaw thiam nélo limitam do dadial ba
déme samh sa talif yi nga talif mané sou koye mole hadjaliss you nga
sang kit siwaal nalab ndaal.

NIASS.

Retour Vidéo suivante

babacar thiam fahanzi salamoun alfou salati zikr aida faye moustapaha
gueye BAYE NIASS cheikh ahmed tidjanie El hadji TAFSIR al quran gamou
bourda islam oustaz barham diop barhama arafat cisse moudir MEDINA
allah diouf as

Commentaires (4)

1. arthritis (site web) 29/10/2012

I came across chababoulfaydamedina.e-monsite.com and i


love it !
rheumatoid arthritis

http://arthritissymptomstreatment.blogspot.com/2012/10/what-
is-arthritis_28.html

2. betonboxing (site web) 20/08/2012

chababoulfaydamedina.e -monsite.com est mon numéro 1


site maintenant

http://www.seekerscentre.com/blog/general/grappling-
with-allergy.html?
comment=d3d3LnNlZWtlcnNjZW50cmUuY29tIGlzIG15IHRvcCB3ZWJzaXRlIA0KbW9yZSBpbmZvD

3. isabel marant bow pumps (site web) 02/07/2012

How do i put music playing on my wordpress homepage?

4. joice 19/11/2011

oie,amiga

Ajouter un commentaire

Nom

E-mail

Site Internet

Message

Anti-spam

Ajouter

Quiz Blog Annuaire Boutique Réservation

Créer un site gratuit avec e-monsite - Signaler un contenu illicite sur ce site