Vous êtes sur la page 1sur 6

Souhaitez-vous vous connecter ou rejoindre Facebook 

Connexion

ou

Rejoindre

Seck Saliou Beug Fallou DAARAY XAM-XAM


12 décembre 2015, 20:32 ·

yabbalou sokhnayi neek si seene neegou suye taye beuga ame doom diou bakh ta ame ndiarigne dou samaye
kaddou nak damako yaatal fii reek diottalikofi konne bismilah maye leenma noppou yeene gni beug seni dome
noppal leene
MARIAGE DE LA FEMME DANS L’ISLAM/DJIGUEEN NIMOUY SEUYEE AK DOM DJI MOUY AM ( INTEGRAL )
SERIGNE NDIAGA DIOP mòko wakhtaan dieléko ci(S.Cheikh Fall Bayou Goor ibn S.C.MOUSTAPHA FALL ibn
MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL)
DJIGUEEN NIMOUY SEUYEE AK DOM DJI MOUY AM
Bismilahir- rahmanir- rahimi
1--Yalla mougui soukkeu ndikou ci djiguèèn nguir bind dom dji.
Mouni kèp koumou tògal ci diatày kham nisa nday dàn seuyé.
Mou tambili di lim khèti dòmou adama yi am
mou wakhni guissò ko khamni deuk(ville) bamou deuk mòfay ndiekeu kheuy difa moudjèè wathie gueunfà
nangò sonn(fatiguer) dou noppalou bèn sà tè bouy gneuw dou eundàlè dépense diamono bounè dankoy dimbali.
Nèèna kou mèl nònou bòko guissatè ndayam dankodàn sakkou mouy bagne.
Dinàlèn thie nèttali bèn khissa(histoire) bò khamantènisi bèn goor la ci reuw mii la amè wòn.
Goor gui dankò diokh sokhna. Sokhna si di bagne bouko goor dè sakkou mouy bagne ,ba bèn biss goor gui forcé
ko beugueu seuyeuk mòm,
ndawsi guèn di daw bassi pèinthie mi(mbèd mi)rèènou garab(arbre) gui nga khamni mò nèk ci peinthie mi(mbèd
mi) tèuktal(fakastal)ndawsi mou dànou goor gui fèk kofa eupko dòlè seuyeuk mom fòfou.
-Bamou si amè dòm.Dòm dja mana war lol bòbou war lou am solo la,-
tàrou lol(beau) ,
-am khèl lol(intèligent),-yarou lol(politesse),-bakh lol(généreux) ba nday dji nàgou ,
-bi khalèbi magguèè(grandire) ba nga khamni kèn kounè beug nakò diour,ba nday dji beugua fattè lamou défòn.
-Bèn biss mouy dawal fass(cheval)si pèinthie mi ba khiir ,fass wi(cheval) dòòr ko si rèènou garab(arbre) gògou
nga khamni mò tèuktalòn(fakastal) ndayam ba bay ba fèk kofa seuyeuk mom ba am koci.
-bimou dànò fala yam sèd gouy.Bay bi guèn, Nday dji di yoùkhou ,bay bi né rèèn bi mòmako mayòn rèèn bi
mòmako khagn.
gnouni goor gui dof na mouni dèdèt dofouma dè rèèn bi mòmako mayòn rèèn bi mòmako khagn.
-Nèènan sakh djiguèèn gou bonn dou diour kou bakh dèèdèt djiguèèn djou bonn dina diour kou bakh wàyè day
dèm ba neèw dòlè bamou tammbléko diarign dàdi fààtou.
-kèp kò khamni seuyi nam rafètoul ci biir rafètoul ci biti dina diour kou gnèp di yèem kou gnèp beugueu diour
wayè sou dèmè bakoy wàdia diarign fààtou.(mort)
2--Mouni guissoulò kò khamni bou tòguèè dou am dara waàyé bou diouguè wouti rèk Yalla diokh ko limou beug.
Nèèna kòkou bòko guissèè ndayam dàwoul sakkou bàyam wàyé bouko bàyam sakkò doussi tèk bèn bààt.
3--Mouni guissoulò kò khamni dou wouti dara tè loumou sokhla mou fèk ko famou tòk.Nèèna kòkou ndayam
mòdàn sakkou bàyam.
4—Nèèna guissò kò khamni day kham limou wara kham lèp ,làmmèn wi dioup –khèl mi nèkh –ta mbòlò moumni
thiap bààt di beugueu wakh gnèp ni na noppi,
nga khamni bàtam dou sakh, Sou amè keur doufa wakh louy sakh, famouy ligueuyè doufa wakh louy sakh ,soudè
borom mbòlò sakh loumou wakh mbòlò ma tiriko.
Nèèna kòkou bòko guissè ndayam dafa amòn bààt thie seuyeum,ta kou am bààt thie sa seuy do diour kouy am
bààt.
konnak djiguèèn gni na nguèèn gannàyò lòlou ndakh diamono djii djiguèèn gni beug -nan bààt lòl mò takh diour
kou am bààt diafè lègui.
5—Nèèna nga guiss ko khamantèèni
Souhaitez-vousdina nèk ci mbòlò
vous eupoufa
connecter ou xam-xam-
rejoindreeupoufa khèl –guenoufà dioup –ta
Facebook ?
bou nit gni wakhè ba tereul ko bou dikèè wakh niou tiri la gnèp wakhòn wala balà nit gnè wakh lèn dannàn
bayyilèn ba diw wakh ba noppi. Connexion
Nèèna kòkou bòko guissèè ndayam amoulwòn bààt ci seuyeum mò takh mou diour kou am bààt.
6—Nèèna guissò djiguèèn gouy seuy ci keur ta bou diekereum ou bayyè dara ci pòsam mou dieul ko bagne kò dèf
mouy dara.
Rejoindre
Lòlou moy diour sathie thiou (voleur) barri si lègui,Wakh nanni kou sa nday di dieul donté dieul ba dou dieulou
dara bò magguèè faw ngay dieul ta bounou sèètèè ci biir société bii niou nèk dinan khamni lòlou moy li am.
7—Nèèna barina ay tawat(fèbar)you bari ci diamono djii mouy tawatou goor.Lòlou likoy dèf loussi bari djiguèèn
gnila ,ndakh sèn borom keur dalèn di sokhla diok beug lèèna sakkou gnou wout lay ba bagna seuy ak mòm.
Lòlou nak amna yoon yò khamni bouko djiguèèn défè dòm dji sidite yeu dina nèuw dòlè lòl bou dioudò.
-Batay ci mbiri tawatou goor nga khamni mò bari lòl lègui,dieulè nan ci lou wèer ci kou wèer mou wakhni
S.CHEIKH ISSA DIENE mou tèd ma dànna
fathie goor gou teulè,wàyè ci lèn rèk lako dàn fadjè(soigner)
sou fèkkèntèni ndayam ak bayam danò guèn diamono (addouna),dafay dèm barsakh dieul roùwou ndayam mou
toùbeul roùwou bayam bouko dèfè rèk sidite yeu nangou.
Kon li djiguèèn gni di dèf lou bari ci diamonoy tay mouy sa borom keur sokhla la nga woute ngante ba bagna
seuyeuk mòm lòlou moy diour fèbarou goor niou bari.
8—Nèèna guisnanou tamit ci diamono fò dèm guiss goor go nga khamni bou guènnèè moròmou gooram yi di
teup di dal louniou ligueuy diokh ko- loumou wakh niouni deugleu- koumou yònni nga daw – koumou sàga nga
bèk(content)- koumou khass nga bèk dòsi gnimè tèk bààt ,
gnògnou gnèp tay djii bòlèn sètlò sèni wadiour wou djiguèèn dankò sarakhèwòn.
Kon batay thiann gou fora-fora-fort dina nèewal dòlè dòm ndakh mousnamà dèg kou mana wakh.mou wakhni
-diar lala nèkh
-seuyè nala nèkh
-diour kala nèkh Yalla dèfalou ko kènn.
9—Nèèna bò guissèè dof yi bari lègui ta liniy digueul djiguèèn gni gnoukoy bagna dèf rèk mòko eundi, mouy
gnakka mòurou.Nèèna moùrou niak guè dèf limouy wagni bariwoul dof mbà diour dof rèk.ta gnou khamni
KHARAM
NA CI DIOULIT BOU DJIGUEEN MOUY- DEF BOP NEEN CI BITI
(YEUNENT BI (saw)nèèna Yalla reub na kiy yok karaw ak kikokay yokal)
*Yonente bi (s.a.s)neena dama guiss ay djiguèn yò khamni gnounglèn yèèwè sèn karaw ya , tak-ko sa kaw ,dieul
bèttèèkh bou tang dieur diko sotti sisèn bop ya ,sèn yoùr nga mangay bakkh ,ga dég namouy yeungueutò ni
mbana mò khamni bouy bakkh nònou mouy bakhèè .
*Yonente bi neena ma lathie Djibril niko djiguèn gnì lan laniou déf ba takh Yalla dilèn mbougueul –mbougueul
mou méttèè nì ?.
“Djibril niko djiguèn gnì dé litakh Yalla yèwèlèn sèn karaw yi ,rakhsa dolli sèn yòùr ya di bakkh ngadiko dég nònou
mou mélni mbana louy bakkh ,moy djiguèn gni nga khamni dàwougnou moùr sèn bop yi ,dandàn mouri sèn bop
yi ,yamouniousa di wané(manifester)sèn tàar ya nguir goor gnilèn takkoul guisko .
Ta Yonente bi neena djiguèn fiiyeuk moungui mouri boppam Malàka yeurmandé douko djégué .
Yalla loumou wakh dina am fowoul fowlouwoul ta gnou khamni Yalla bawoul lamou wakhòn ta dou bayyit lamou
wakhòn.
10—Guiss nanni ci ay ndiabòt dangay guiss niou bok nday(mère) ak bay(père) gueneuntè,bouko dèfèè nak sila
nit gni di nakhè sèn bop banàn dòm diou bakh Yallà koy diokhè.Wàyé dafa am ci noumoukoy diokhè.
Nèèna lòlou sàa bòko guissèè mèlokan dja nday dja(mère) amòn bamiy soss gnom gnar mò bokkoul.kouthie
dadjèk mèlokàn wa gueun,yaw yày gueun.
Dafa am gnari nit gno khamni gno bok nday ak bay.Rak dji am barké lòl ,Mag dji khawa nèew dòlé lòl.
Rak dji loumou bayy(cultiver) mou nangou –loumou wouti Yalla dèfko.
Mag dji nangò ligueuy lòl ta loumou ligueuy-ligueuy rak djè koy dimbali,Mag dji wò bay ba(père) wò nday
dji(mère) wò rak dji(frère) nilèn damà amònak yèn wakhtaàn.
Nilèn man boumay ligueuy lounè lay dathie ,louma ligueuy loumou am-am solo dou barkèl si thiòna là deuk tè
sama rak djii diamono diounè mòmay dimbali ma beug nguèn wakhma lan mòko waral,bay bi(père) niko làthie
ko sa nday(mère).
Nday dja niko dòm dèy ci manla ndakh bimasa bày(père) di dòga dieul,bòbou dèy tound wi(deuk bi) gnèppama
beug,ma diafè lòl ,sa bày(père) dima nakhtàn, dànaka mòdòn seuy bama diour lassi (manam ba diour si grand
frère bi),
Bima laci amè,ma khòl sama bop ni soppèkounà,ma wakhtaanak sama khèl ni fass yènènà seuy nak lègui ta
bayyi thiakhàn yi,thia bòbèè ma fass yènèè seuy –fass yènèè woyof thie là amè sa rak djii(petit frère)lòlou mò
waral lii. Souhaitez-vous vous connecter ou rejoindre Facebook ?
Agg-na bathi sakh bou djiguèèn gui dèmè bassi eumb(enceinte) si diourom gneint wèèr yòyou(9 mois yi)sounou
borom dina koci may lou mèlni (repéchage) nga khamantèni
Connexionbou fèkkèè toùbna tè soppi namou wara dokhalè
Yalla dina weulbeuti dòm dji.
baci diourom nientèlou wèèr yi(9 mois)bou moudj bi amna ou nò khamni bouni mèlèè rèk wèssoul Yalla soppi roùh
gui(khol bi)nga khamantèèni mòm la naròn ci dieum dji dèfsi djènèn roùh ,wàyè mougui ci ni nday dj(mère) di
Rejoindre
dokhalè.
11—Batay ci biir djiko yòyè djiguèèn di am ci seuyeum,guiss nanni ligniy neub(cacher) ci seuy nga khamni kou
goor ki ak kou djiguèèn ki rèkkakoy yeuk,guiss nanni bò guissèè louci bari yommba diap dòmou àdama ,
liko waral dou dara loumòy djiguèèn gni danò gnimè ndjibar.(fétiche)
sàbò ligueuyè sa diekeur ta ligueuy bi dioublouwòci lou rafét, dioublouwòci lou bakh,loumòy dioublouci yakkh
wala mòm ko ba takhalèkok ay mbokkam,nala woor ni bisbò amè dòm ka gueneu gnak xam-xam bouko fassè
fasba gueneu nèew dòlè sakh dinako diap.
lou takh?
ligueuy ba nga dòn ligueuy bàyam.tè sètlou nanni keur gò dèm boudè keur gou mak ta yag,nga làthie borom keur
nga niounila dèmna,nga làthie sokhna sa niounila mougui fi ,lòlou nak djiguèèn gni war nansè bayyi khèl khamni
kon linga khamantèèni mòm lan dòn ligueuy ci kou goor ka mòm la kou goor ka dèm balèn fi niou war kò agnè
ak sèni dòm.
ta djiguèèn sa bònèko bò dèfè lìì dém sawara wala am bakkàr dinako gnimè dèf Yallà ko bindè nònou,wàyè
bòkonè so dèfè lìì sa dòm bonn dinako sèètàt.kon nak sounou mbokki djiguèèn gni lìì na nguèn ko bayyi khèl bou
bakh.
12—Guisnan ci diamono tamit nit gno khamni lounou am ay diambour lankoy dèfal wàyè douniou diarign sèn
nday(mère) douniou diarign sèn bay(père).
liko waral moy bày ba(père) lou bakh lamou dàn am lèp dako dàn neub diko diokh nit gni bayyi sokhna simou
nèkkal
-Nday dja(mère)yit ak bàkham ak lèwètam ak nangou diokhè gnaman (repas) akouk woyofam lèp wannako
dòmou àdama yi bagne kò wan borom keureum,gnom bouniou diourè dòm doulèn amal ndiarign gnom gnar
gnèp,ay diambour lay diarigne.
13—Guisnan diamono dji dèè(mort) you gàw yi ,wop yi(maladie), nakhar yi ,tis-tis yi ,balà yi lòci guiss rèk ci biir
seuy laniouy ligueuyè la takh mou am.
Ndakh guiss nga tay diamono dji gni si eup weur-seuk.
Àg-na bassi dòm yòyè nga khamni diourou gnoulèn ci yoon,ndègam kouniou diouroul ci yoon moy am weur-seuk
am khèél ta likoy waral dou dara loudoul fèkki dia nday dji(mère)dàn fèkki ,nangou dia nday dji
nangouwòn,ndègam kòkou mò mana am lòlou wakhoumalàk ki nga khamni dàkò tèk ci yoon ci li nèkh Yalla.
14—Amna gno khamni loulèn di bèp rèk laniouy am,liko waral moy sèn nday(mère) diamono bounè mougui bèt
sèn bày (père)ci khèweul ak yììw nga khamni dànaka ay dòf lanlèn di toudé ,louniou ligueuy diokh diekeur dji.
Djiguen gnoniou nga khamni dinan guiss tissu bou bakh dieundeul lako ,lèp louniou guiss mou rafèt niou yènè
lako,
lòlou lèp loumouy diour moy doom dio xamni Yalla dinako diokh lò khaman tèènisinìì founèk lay bayyikò tè dou
kham lanla dèfal nit gni batakh nioukoy défal lòlou.
Gni nga khamni gnom laniou top tay mouy serigne si barkè lalèn sèn bàye(père)amèèl.
Wàyè tawfèkh gui gnou am nga khamni nit day niakkh alalam fousori nieuw yèkatiko diokh lèn ko sounla wakhè
fa sèn wàdiour wou djiguèèn diar nga khamni lòlou loumou ligueuy la ba Yalla fayélèn ko.
Goor barké rèk la mana faggoul dòmam wàyé lici dèss djiguèèn mòkoy faggou.
Nèèna diabar yiila djiguèn na khamni foumou fètèwò rèk dòm you mèl nònou lay am.
- amna :
(DIABAROU BASSANG)
-(DIABAROU GUEULEEM (Chameau)
-(DIABAROU PAAKA(Couteau)
-(DIABAROU KHATHIE (Chien)
-(DIABAROU MBAAM (làne)
-(DIABAROU POUSSO (éguille)
Dinan ko lèèral :incalah
15 -Diabarou BASSANG moy ko khamni doula dèfaral doula yakhal, boy dèm fanga koy bayyi bo dèllousè
fangakoy fèk lòko wakhoul douko kham ,lòko santoul douko dèf,mbiir loumou nourou nouroulou lou am solo
douko dèf.
kòkou moy diour ko khamni balà kham dara rèk nganiko nanggam mouni an ,dànaka dòtoul mat nit .
mo takh djiguèn warnà dèf si khèlam ay fàggoutèf ndakh djiguèn bou seuyè khèl diour kou am khèl .kon nak
diabarou bassang bòko amè domou bassang
Souhaitez-vous rèkconnecter
vous ngay am. ou rejoindre Facebook ?
16—(DIABAROU GUEULEEM (Chameau) ) Bou lòlou diallèè mou am diabarou guilem (chameau).
Gueulèm day nèk ci garap gui(arbre) di lèk di khòl garap gueulè, nga khamni limouy lèk loumou nèkh-nèkh
Connexion
loumou bari-bari amoussa sokhla mougui khol na kènèn nèkké,
moy sokhna yòyou nga khamni danglèndi am bisbou sétougnounànla sama nawlé yi liniou am,diweu nganè
diekereum dieundeul (acheter) nako nanggam (chose), dèfal nako nanggam, yob nako makka , yob nako bitim
Rejoindre
reew man dèfalòma dara .
kòkou ban dòm lay diour,moy diour niòniou nga khamni boulèn Yalla diokhòn addouna ak lici biireum niògui khòl
lou kènèn am,
tè barinaci dòmou àdama yi lègui,diaral nalèn niou tabakh foukki étage ,ta kou tèrage ci sèn wèt rèk gnouni
ligueyeul mako mou dèè(mort)wala mou dof(fou) ndakh warouta am lìì.
kousa seuy di seuyou gueulèm nònou ngay mèl,kon fò guissati kou mèlnii dawalal ma sa khèl ci waydiour wou
djiguèènam ding nga kham lima wakh.
17—(DIABAROU PAAKA(Couteau)Diabarou pàka bouy seuy si dalay fèk nga amiy nit , dioubòk say mbòk(famille)
, amiy kharite (amis), amiy an-ndandò(compagnons),mouy dag par bèn di wathie,di dag par bèn di wathie,dòtò
dioubòk say mbok, dòtò dioubòk say kharite, dòtò dioubòk say an-ndandò ,mou àkimòla mòm kèn.
Kòkou moy diour ko khamni koumou am, loumou fort-fort-fort ak loumouko diap-diap-diap, loumou am-am yakàr
ci mom day djèkki bèn beuss(jour) rék kheuy bako, mounàn man nit gni man khawma loumalèn dèf.
Fék bòbou nday dja (mère)seuyounou pàka ladòn seuy, lou takkh si bayam (père) mou dieul sànni bouko dèfè
loum dèm ba dici am yàkàr rék Yalla dag lòla wathie.Yèn djiguèèn gni sètlou lèn bou bakh limalèn wakh.
18—(DIABAROU KHATHIE (Chien)Diabarou kathie guan(visite)lay bagna guiss,sa bou guissèè guan rèk
soppikouna, sou nèkkèè ci keur gui guan amoufi mou am diamm .
Kòkou sou amè dòm, dòm dja foumou dèm khatal gnònia , sou fèkkèè ay nit di wakhtàn ,wakhtànou yiiw bouci
dougalè bàtam gnouni wakhtaan wa yakkhouna, sous fèkkèè ay nit gnouy fo(jouer) bou bokkèè thia foma
(jeux),foma yakkhou ,
tè guiss nguèèn nit gnou mèl nònou ,louniou bok lòla yakkhou, louniou doug lòla yakkhou. Lan mò takh sèn
nday(mère) seuyounou khathie ladòn seuy.
19—(DIABAROU MBAAM (làne)diabarou mbàm moy kò khamantèni lòko meunti wakh fèèk
doumeuwòko(frapper) douko kham ,fòk nga dòr ko(frapper) mouy dòga kham lingko wakh,
maslà dou takh mou kham ,yèèd dou takh mou kham, wò say morom wala wò say wadiour dou takh mou kham
limou wara dèf.
Lanay takh mou kham ko sa lokho dal ko, diabarou mbàma gui nònou.
Kòkou moy diour kò khamantèni bou démè famouy dianguè (apprendre) lou gnèp wara kham nga khamni gnèp
danko wara khòl khamko,fiyeuk doumeuwòko(frapper) douko kham ,
lòko sante(dire) fèèk dòròko(frapper) douko dèf ,Lòko térè (interdit)fèèk dòròko douko bayyi,
ta moy diour gnoniou nga khamni sounou dèmè ba dòn mag (grand)louniou am-am daradja, louniou am-am
dieumi kilifeu fòk niouy dèm ay diamono dèssnalèn doumeu ta lòlou liko diour moy diabarou mbàm.
20—(DIABAROU POUSSO (éguille)Diabarou pousso kòkou dalay fèk gnèp bayyila, say mbok(famille) bayyila, say
kharite(amis) bayyila etc…,
mouy fékhé di lidieunti, dilèn dèllòsi ,di wakhtànak gnom ba gnèp dèllousi nga amàt la-nga amòn ba mèl na-nga
wara mél.
Kòkou moy diour ko khamantèni foumou nèk mbokkam dinafa gneuw, kharitam gneuwfa ,lèppam gneuwfa ta
kèn douko mèré(fàcher) ta diamono diouné nit gni daniy begueu nèk ci wétam.
Bò nèkkèè ci wétam dingfa fèk diambour, dingfa fèk mbok, kèn kouné dingkofa fèk ci diotàyam.
Kòkou ndayam moy ki nga khamni mòdòn seuy seuyinou pousso.
bouko dèfèè nak di- nga dèg(entendre)niounàn wàné la, limiy déf kèn sanntoukoko, day djèma beug lou bakh
wàyé dou weuy .
Ta bou magguèè dina diour kò khamni dina oùf mbok,oùf diambour.kon djiguèèn gni khalàt lèn lòlou.
—AMNA DIABAR YO KHAMNI SA DIABAR LAN(ta femme)
--AMNA DIABAR YO KHAMNI SA DIABAROU KHARIT LANIOU(tes amis)
--AMNA DIABAR YO KHAMNI DIABAROU EUT LANIOU(cour de la maison)
--AMNA DIABAR YO KHAMNI DIABAROU BIIR NEEUK(chambre)LANIOU
Tè lòlou lèp louthie nèk day am nimouy fègné ci dòm.
Dinan ko lèèral :incalah
21—(DIABAROU SAY KHARITE(tes amis)Diabarou say kharite moy kò khamni bou nguèèn kheussèè wèèt(seule)
lou nakhari louné dinalako wakh, mèttit bouné dinalako ték, ta bou nit gni gneuwè mou wané mbàkh ba gnèp
diko guereum.
Kòkou moy diour ko khamamtèni Yalla dakoy soutoural si kaw ta fòko fèk khol ba si yeungou lay nèk ak tang,di
nakhari té kèn douko kham ,ta lan mòkoy ray,
Souhaitez-vous vousmisère ,tè nit gniou
connecter dounko kham.
rejoindre Facebook ?
Bou fààtò dannàn ayway diwaka gàt fan, khamouma gàt fan guii louko waral, fèk ndayam diabarou ay kharite
lawòn, dònoulwòn diabarou bàyam. Connexion
bouko dèfèè gnounàn ndayam maka sonnòn ndeysan Yalla dèy moy déf louko nèkh,fèk bòbou ndayam diabarou
say kharite lawon. ou
22---(DIABAROU EUT(cour de la maison)Diabarou eutt moy kò khamni bou nèkkèè ci biti(dehors)mannalà lalal
Rejoindre
matalà ,tègalla ndiaganay, teud sa wèt(còté) eundilla ndokh mou sèèd ,dila oup,dila beuss etc…..
wayè so douguèè ci biir mou tambli lèp loumla défalòn dinala wakh ,wala mou défla lou diar nga fatté ko.
Kòkou moy diour ko khamni loumou doug ,ndial bèùnga (commencement ) tawfeùkh lassiy dougué ,wàyé bou
démè bassa biir lèp diy thiòno ak nakkhar, mounàn man dal louma tambli dina bàkh ,wàyé moudjèl nga dou am
solo.
Kòkou ndayam seuyinou eutt ladòn seuy.
23—(DIABAROU BIIR NEEUK(chambre)Diabarou biir nèùk (chambre)moy kò khamni bou nèkkèè ci biti bò wakhè
mou tontou la , bòko yònèè mou yèkhantou, wàyèé nak bòlèn douguèè ci biir ,dinala défal louy sèèd sa khol ba
nga fatté limoula défòn lèp,ba nga khamni sà boulay déf dara ci biir nit gni dòko diap bou bakh ndakh limlay
défal ci bììr.
Kòkou moy diour ko khamni loumou tambli dina mètti(dificile)lòl baniou yereumko ni dou dèm, wàyé bou démè
bathia biir lèp tawfeùkh lay dòn.
Kon djiguèèn gni sètàt lèn ni nguèèndi seuyé.
24—LéL-lék(dèfois) nga guiss kouy seuyeuk nit mou am loudoul dièkh,barilé lòl,dò manqui(manque)dara,fò
mousseu dèm yà fay dakkh(belle), louné moudilako défal, yamalèwoulàk kèn ,
nga dèm ba dòlèm nèuw(diminuer) si khàliss(argent)wala mou dém ba dòléy diemeum nèuw(diminuer) ngay déf
laka soudoul nònou.
Lòlou amna dòm dioumouy eundi.Dòm diòdiou noumouy mél ?
moy kò khamni Yalla dinako may mou barilé ,wàyé kat, day ama-ama-am ba gnèp yèmko ,mou barilé lòl, gnèp
top ci guinàwam ,
ndakh ba bày ba(père)barilè nday dja(mère)dà nang-ngò seuy (mòm lala Yalla di dèllòsil nònou).
Mou dém bamou yàg Yalla torokhal ko ba koumou diègui sa ndokh sakh dòssi nàn(boire),déf koko-déf koko lou
yàg sòkkò weulbatiwàt diokhàt ko ,diko dèf nònou niak-am ,niak-am silay dound(vivre) ba fàatou(mort).
25—(SOKHNA AK BOROM KEREUM)sokhna ak borom kereum niat(3) gnofi né (DARADIA—AM-AM—
YEURMANDE)
tè lòlou lèp diabar bou sagnòn dou nèksi borom kereum,tè lòlou lèp niakka kham la wàyé yòyou yèp sò yènèè sa
diekeur(mari) diko dimbali simou am ko.niat(3) yèp dina dadjè ci sa dòm, mouy lan ?
--(AM-AM) am-am boudèè bèn ,bou sagnòn ngay gnàni thiamminiam, bouko dèfèè bò wakhèè mounila loufi dèè
samay thiammign niòko ray.Lòlou lou mata moytoula.
Lòlou koukoy déf di fékhé ba sa diekeur(mari)say thiammign diko dimbali té bou nguèèn wakhèè nga wakh ko-
ko ,nala woor ni sa dòm bòko diourè biss bou yorè diabar thiammignou diabar dja gnòkoy dimbali rèk tè
dawallèn sèn khél tè sètlou.
--(DARADJA) daradja boudèè bèn ,bàyam(père) lako gueneu yèèné, bou sagnòn fò sèèn(voir) bàyam souk.Bouko
défèè dou diour mouk kò khamantèni kouko sèèn(voir)souk ndakh yènèèm la.
--(YEURMANDE)yeurmandé boudèè bèn, yènèwouko borom kereum moungko yèèné dòmam.Bouko dèfèè moy
diour ko khamni day dèm bamou yag mounàn bama dioudòk lèègui moussoumà guiss kò khamni dieuféna
yeurmandé sama digueuntèèk mòm.
SERIGNE TOUBA wakh nani :
-koussa mbir dioup gueremeul sa nday(mère)
-koussa mbir dung kharabal sa nday(mère):
ndakh nèèna fadiouk àdio mòfi né -,ngueremeul Yalla ,-ak mbir mou dioup.
…bò beuguèè sa àdio fadiou dangay top kou àdiòm fadiou mou fathie sa àdio.
…bò beuguèè am ngueremeul Yalla nèèna dangay dèm ci kou Yalla guereum mou guereum la.
…wàyé koussa mbir dung ,koussa mbir dioup sa ndaya.(mère) wa salàm.
DJEREDIEUF SERIGNE TOUBA/DIARAAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL
FIN( SEN MBOKOUM TALIBE BAYFALL NDIGUEUL MOKODON YAATAL DI SAKOU CI YEN GNAAN .
J’aimeCommenterPartager

J’aime Partager
13 partages
Souhaitez-vous vous connecter ou rejoindre Facebook ?
CheikhMouhamadou LamineBara Diakhoumpa
Connexion
tres interessant
5 ans J’aime Signaler ou

Rejoindre
Seck Saliou Be... a répondu · 1 réponse

Baye Fall Thioub


Fall li amna solo lôl way yallah na yallah yégalé sa yéné thi sokhna yi barkéb borom touba
5 ans J’aime Signaler

Seck Saliou Be... a répondu · 1 réponse

Vous aimerez peut-être aussi