Vous êtes sur la page 1sur 2

20/03/2023 11:16 MOUSTARCHIDINE » Archives du Blog » Traduction de la Salât al-Fatihi en Wolof : FIRIM SALATOUL FATIHI CI WOLOF

Traduction de la Salât al-Fatihi en Wolof : FIRIM SALATOUL FATIHI CI WOLOF


Posté par moust@rchid le 6 mars 2011

b[b[-ALLAHOUMA : YAW YALLA.

-Çalli : Yalla Na Nga Dolli Khéweul Ak Téranga.

-ALAA SEYYIDINAA : Si Sougnou Sangue.

-MOUHAMMADINE : Ibn Abdillahi, Rassoulilahi. {1}

-IL FATIHI : Kadi Adji Oubi.{2]

-LIMAA OUGHLIKHA : Niél La Nga Khamné, Teudjone Nagnko Rap, kéne Tidjiwouko wône.

-WAL KHATIMI LIMAA SABAKHA : Bimou Nieuwé ite Teudj na Bounetou Noubouwa, bénéne yonent Dotoul Gneuw Guinâwam.

-NAçIRIL HAKHI : Kiy Dimbali Deugeu

-BIL HAKHI : Thi Deug.

-WAL HEUDII : Keudi Adji Guinedi Diamou Yalla Yi, Dieumé léléne si Sène Boroom, té dieumé wouléne si Bopam.

-ILAA SIRATIKA : Deumé Lé Léne Si Saw Yôôn.

-AL MOUSTAKHIMI : Wa Di Adji Tioworlou ( DIOUP);

-WA ALAA ALIHI : Ak Si Gnognam (Jabôôtam)

-HAKHA KHADRIHI : Deug Deugui Darajay çallalahou Aleyhi Wa Salam.

-WA MIKHDÄRIHIL : Ak Pouvoiram.

-AZIMI : Badi Adji Magg


]b

A noter que cette traduction est juste pour permettre au pratiquant de connaitre le sens de ce qu’il récite car étant une charte du Wird Tidiane car nul ne peut
mesurer et connaitre le Zâhir (Apparent) et le Baâne ( le caché) de la Salatoul Fatihi.

moustarchidine.unblog.fr/2011/03/06/traduction-de-la-salat-al-fatihi-en-wolof-firim-salatoul-fatihi-ci-wolof/ 1/2
20/03/2023 11:16 MOUSTARCHIDINE » Archives du Blog » Traduction de la Salât al-Fatihi en Wolof : FIRIM SALATOUL FATIHI CI WOLOF

Notes :
1} Mouhammadine   Il fok gnou fénialko ba gnou kham kane moy yonent bi çala lalou aleyi wa salam ak di ragnalé boubaakh Mouhamadou Noûr, la Lumière,
ak Mouhamadou ibn Abdilllahi, le fils d’Abdallah, ak Mouhamadou Rassouloulah (le Messager de Dieu SAWS).

{2} Il Fatihi :Kadi Adji Oubi.( zalika houwal mifatâh, Moy tiâbi bi, Môy oubi. Mou délou si bou fékone né dou Yonent bi (SAWS), Yalla dou bineda dara, dou
bineda dieum yii, dou bineda roûh yi, dou bineda assammane, dou bineda jant, dou bineda wéér bi…..]b

Transcription et traduction en français de la Salat al-Fatihi


Allâhoumma salli ‘alaa sayyidinaa mouhammadin-il-faatihi limaa oughliqa wa-l-khaatimi limaa sabaqa naasiri-l-haqqi bi-l-haqq(i)
Wa-l-haadi ilaa siraatika-l-moustaqiimi wa ‘alaa aalihii haqqa qadrihi wa miqdaarihi-l-’aziim

« Oh Dieu accorde ta bénédiction et ton Salut, à notre Seigneur Mouhammad ; qui a ouvert ce qui était clos ; qui a clos ce qui a précédé ; Le défendeur
de la vérité par la vérité ; Le Guide du Droit chemin ; ainsi qu’à sa noble famille ; suivant sa valeur et l’estimation de son ultime dignité »

moustarchidine.unblog.fr/2011/03/06/traduction-de-la-salat-al-fatihi-en-wolof-firim-salatoul-fatihi-ci-wolof/ 2/2

Vous aimerez peut-être aussi